Ay tont yu leer ci ay laaj yu am solo
Mën nga jàng walla nga telesarse téere bii walla nga laaj ñu jàngal la Biibël bi te doo fey dara, ci www.pr2711.com.
Suñuy adarees ci àddina si sépp, ñu ngi ci www.pr2711.com/fr/nous-contacter.
Boo amee leneen loo bëgg a xam ci Biibël bi, demal ci www.pr2711.com walla nga jokkoo ak Seede Yexowa yi..
Bu ñu ko leeralul, limi Biibël bi ci làkku ebrë yaa ngi tukkee ci Mucc gi Yàlla waajal (1999), te mbind yi ci làkku grekk yaa ngi bawoo ci Téereb Injiil di Kàddug Yàlla (2004).
© 2008 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania