Paas bi turu téere bii nekk / Paas biy wone ñi defar téere bii
Xibaaru jàmm bi jóge ci Yàlla !
Good News From God!
Ci weeru me ci atum 2018 lañu ko defar
Wolof (fg-WO)
© 2012, 2016
WATCH TOWER BIBLE AND TRACT SOCIETY OF PENNSYLVANIA
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci lu ñuy jëfandikoo ngir jàngale Biibël bi ci àddina si sépp. Xaalis bu ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.
Boo bëggee maye dara, demal ci www.pr2711.com.
Bu ñu ko waxul, bépp aaya bu ñu fi lim, ñu ngi ko jële ci Njàlbéen ga (2012), Sabóor, Mucc gi Yàlla waajal, Kàddu yu Xelu, Téereb Injiil di Kàddug Yàlla (2010). Aaya yi ànd ak MN ci Les Saintes Écritures Traduction du monde nouveau lañu ko jële, firi ko ci wolof.
Ñi moom foto yi : Xët 6, ci kaw, Dead Sea Scroll : Shrine of the Book, Foto © The Israel Museum, Jerusalem ; xët 6, ci digg bi, ak xët 32, ci kaw ci ndeyjoor, Greek Codex : The Codex Alexandrinus in Reduced Photographic Facsimile, 1909, British Library ñoo nangu ñu jot ci ; xët 16, foto Hitler : mu ngi jóge ci U.S National Archives photo