TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • mb lesoŋ 4
  • Njàngale 4

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Njàngale 4
  • Li ma mën a jàng ci sama Biibël
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Njàngale 5
    Li ma mën a jàng ci sama Biibël
  • Njàngale 3
    Li ma mën a jàng ci sama Biibël
Li ma mën a jàng ci sama Biibël
mb lesoŋ 4

Njàngale 4

Jëf ya 14:17

Tomoko mënul génn ndax taw bi.

Mu ne :

“ Maa ngi toog ci biir rekk.

Xanaa taw bi du bàyyi ? ”

Jékki-jékki rekk

naaj bi génn.

Taw bi bàyyi.

Tomoko kontaan !

Mu daw ci biti, mu gis lu ko waar.

Tomoko ne : “ Xawma woon ne taw bi jóge ci Yàlla mooy tax fulóor yi màgg ! ”

LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM

Jàngalal lii sa doom :

Jëf ya 14:17

Waxal sa doom mu won la :

Palanteer Picc Tomoko

Garab Fulóor

Gunóor Roppëlaan

Laajal sa doom lii :

Lu tax Yexowa def taw bi ?

[Nataal bi nekk paas 10]

[Nataal bi nekk paas 10]

[Nataal bi nekk paas 11]

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager