TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • lff
  • Xaaj 1

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Xaaj 1
  • Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Nañu fàttaliku xaaj 1
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Xoolal li Biibël bi wax)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 1
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 4
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
Xóotalal waxtaan bi
Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
lff

XAAJ 1

Édition imprimée

Li ñu nar a gis: Dinañu gis ni la Biibël bi mënee dimbali ak ni nga mënee xam Yàlla mi ñu jox Biibël bi

Xale bu góor buy jàng Biibël bi.

LESOŊ YI

  1. 01 Naka la la Biibël bi mënee dimbali?

  2. 02 Biibël bi dafay maye yaakaar

  3. 03 Ndax mën nga gëm li Biibël bi wax?

  4. 04 Kan mooy Yàlla?

  5. 05 Biibël bi dafa ñuy xamal li Yàlla bëgg ñu def

  6. 06 Fan la nit jóge?

  7. 07 Kan mooy Yexowa?

  8. 08 Mën nga nekk xaritu Yexowa

  9. 09 Jegeel Yàlla ci ñaan

  10. 10 Ban njariñ nga mën a jële ci teewe ndaje Seede Yexowa yi?

  11. 11 Ni nga mënee jariñoo bu baax li ngay liir ci Biibël bi

  12. 12 Lan moo la mën a dimbali nga wéy di jàng Biibël bi?

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager