TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 5/08 p. 3
  • Yégle Yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Yégle Yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2008
Sasu Nguuru Yàlla — 2008
km 5/08 p. 3

Yégle Yi

◼ Téere yi ñuy wone ci wéeru me : La Tour de Garde ak Réveillez-vous ! Dinañu góor-góorlu ngir seeti ñi suñu waxtaan neex te tàmmuñu teewe suñu ndaje yépp, fekk teewe woon nañu ndaje fàttaliku bi ak waxtaan bi ñu faral di am ci àddina si sépp bu ndaje fàttaliku bi weesoo. Li waral ñuy dellu seeti nit ñooñu, mooy bëgg komaase njàngum Biibël ak ñoom. Suweŋ : Qu’enseigne réellement la Bible ? Nañu góor-góorlu ngir komaase ay njàngum Biibël. Sulyet ak ut : Téere bu def 32 xët ci yi topp fii : Dieu se soucie- t-il vraiment de nous ? ; Doit-on croire à la trinité ? ; Dunda léen ba fàww ak bànneex ci suuf si! ; Les esprits des morts — Peuvent-ils vous aider ou vous nuire ? ; La direction venant de Dieu — Le chemin du paradis ; La route qui mène à la vie éternelle : L’avez-vous trouvée ? ; Le gouvernement qui établira le Paradis ; Le nom divin qui demeure à jamais ; Mën nga nekk xaritu Yàlla ! ; Quand la mort frappe un être aimé... ; Que devient-on quand on meurt ? ; Quel est le but de la vie ? Comment le découvrir ? ; Une vie pleinement satisfaisante : Comment ? ; Veillez ! ak “ Voici, je fais toutes choses nouvelles ”.

◼ Ñiy jiite mbooloo mi, war nañu seetaat bataaxal bu 6 Sulyet 2006 biy wax ci ni ñu mënee waajal suñu bopp ngir musiba yi mën a dal fi ñu dëkk. Nañu seet it ndax xam nañu li ñu mën a def ba jot waaraatekat bu nekk. Su fekkee ne fi ñu dëkk dafay faral di am ay musiba, waaraatekat bu nekk war na am it beneen nimoro fi ñu ko mënee gaaw a jot bu musiba amee. Ginnaaw loolu it, waaraatekat mën na feebar ba war a nekk lopitaan walla mu war a tukki lu yàgg, ngir noflaay, ngir liggéeyam, walla leneen lu mel noonu. Bu ko xamalee kiy jiite njàngum téere bi mu bokk, walla beneen njiit ci mbooloo mi, dina baax lool.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager