TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • ll xaaj 11 p. 24-25
  • Ndax Yexowa mu ngi dégg li ñuy wax ?

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Ndax Yexowa mu ngi dégg li ñuy wax ?
  • Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Gëna jege Yàlla ci ñaan
    Lan la ñu Yàllay laaj?
  • Jegeel Yàlla ci ñaan
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Xaaj 11
    Déggleen li Yàlla wax
  • Jegeleen Yàlla ci ñaan
    Lan la Biibël bi wax dëgg-dëgg ?
Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
ll xaaj 11 p. 24-25

XAAJ 11

Ndax Yexowa mu ngi dégg li ñuy wax ?

Ci dëgg, Yàlla dafa ñuy déglu bu ñu koy ñaan. 1 Piyeer 3:12

Gangune Yexowa bi ci asaaman

Yexowa mooy “ Kiy déglu ñaan yi ”. (Sabóor 65:2, MN.) Dafa bëgg ñu koy wax li nekk ci suñu biir xol.

Góor guy ñaan

Yexowa rekk ngeen war a ñaan, du keneen.

  • Yeesu jàngal na ñu ni ñu war a ñaane. — Macë 6:9-15.

  • Ñaanu kan la Yàlla di déglu ? — Psaume 145:18, 19.

Mën nañu ñaan Yàlla ci ay mbir yu bare. 1 Yowaana 5:14

Yeesu ak 144 000 yi ci nguuru gi

Ñaanleen ngir coobare Yàlla am ci suuf si mel ni ca kaw asamaan.

Nangeen ñaan ci turu Yeesu. Loolu dafay wone ne yëg ngeen li mu leen defal, te yéena ngi koy gërëm.

Karceen bu woolu Yexowa day fajj soxlaam yi ak yu njabootam teg ci ñuy def lu baax

Ñaanleen Yexowa mu dimbali leen ngeen mën a def lu baax. Mën ngeen a ñaan itam ci lu jëm ci wàllu lekk, liggéey, dëkkuwaay, ak li ngeen di sol ak wér-gi-yaram.

  • Yexowa dafay déglu ñaanu nit ñu jub ñi. — Proverbes 15:29.

  • Buleen jaaxle ci dara. — Filib 4:6, 7.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager