TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • ll xaaj 12 p. 26-27
  • Lan ngeen mën a def ngir am jàmm ci seen biir njaboot ?

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Lan ngeen mën a def ngir am jàmm ci seen biir njaboot ?
  • Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Naka lañu wara dunde ci suñu njaboot ba mu neex Yàlla ?
    Lan la ñu Yàllay laaj?
  • Xaaj 12
    Déggleen li Yàlla wax
  • Naka nga mënee am jàmm ci sa biir njaboot? (Xaaj 1)
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Li ñu mën a def ba suñu njaboot bare jàmm
    Lan la Biibël bi wax dëgg-dëgg ?
Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
ll xaaj 12 p. 26-27

XAAJ 12

Lan ngeen mën a def ngir am jàmm ci seen biir njaboot ?

Mbëggeel mooy tax jàmm am ci biir njaboot gi. Efes 5:33

Aadama ak Awa ci toolu Eden

Yàlla dafa santaane bu séy naree am, na nekk benn góor ak benn jigéen.

Góor guy toppatoo jabaram ju feebar, jigéen juy defaral jëkëram lekk

Góor gu bëgg jabaram dafa ko war a fonk te di ko muñal.

Jigéen dafa war a jàpple jëkkëram.

Baay buy dimbali doomam muy dégglu ci ndaje karceen

Xale yi war nañu déggal seeni waajur.

Nangeen baax te bañ a soxor. Nangeen yem ci seen néegu séy. Kolos 3:5, 8-10

Waajur yuy jàngal seen doom bu jigéen lu jëm ci Biibël bi

Kàddu Yàlla nee na góor dafa war a bëgg jabaram, ni mu bëgge boppam. Jigéen itam dafa war a weg jëkkëram.

Jigéen ju am metit bu jëkëram di xool lu yàgg beneen jigéen

Njaaloo baaxul. Kenn warul ànd ak koo séyalul. Te it, am jabar yu bare baaxul.

Jaboot buy xool jant buy so

Kàddu Yexowa dafay jàngal njaboot yi ñu xam li ñu mën a def ba am jàmm ci seen biir.

  • Dawleen njaaloo ak lépp lu bon.— 1 Korent 6:18.

  • Nangeen bëgg seeni doom, di leen jàngal ak di leen aar. — Deutéronome 6:4-9.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager