TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • lff xaaj 2
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 2

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 2
  • Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 1
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 3
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 4
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Xoolal li Biibël bi wax)
Xóotalal waxtaan bi
Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
lff xaaj 2

Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 2

  1. 13 Diine yi dul dëgg dañuy tilimal turu Yàlla

  2. 14 Naka la Yàlla bëgge ñu jaamu ko?

  3. 15 Kan mooy Yeesu?

  4. 16 Lan la Yeesu def bi mu nekkee ci kaw suuf?

  5. 17 Yan jikko yu rafet la Yeesu amoon?

  6. 18 Naka lañu mënee ràññe karceen dëgg yi?

  7. 19 Ndax Seede Yexowa yi ay karceen dëgg lañu?

  8. 20 Ni Yexowa di jiitee mbooloo karceen mi jaare ko ci Yeesu

  9. 21 Naka lañuy yégle xibaaru jàmm bi?

  10. 22 Naka nga mënee xamle xibaaru jàmm bi?

  11. 23 Sóobu ci ndox: jubluwaay bu am solo!

  12. 24 Ñan ñooy malaaka yi ak lan lañuy def?

  13. 25 Lan la ñu Yàlla bëggal?

  14. 26 Lu tax lu bon ak coono di am?

  15. 27 Naka lañu deewu Yeesu mënee muccal?

  16. 28 Woneel sa ngërëm ci li la Yexowa ak Yeesu defal

  17. 29 Ñi dee, fan lañu nekk?

  18. 30 Suñu mbokk yi dee mën nañu dundaat!

  19. 31 Lan mooy nguuru Yàlla?

  20. 32 Nguuru Yàlla tàmbali na ilif!

  21. 33 Li nguuru Yàlla nar a def

13 Diine yi dul dëgg dañuy tilimal turu Yàlla

Ndax Yàlla nangu na fasoŋ yépp yi ko nit ñi di jaamoo? (Xaaj) (3:22)

Ni igliis yi dugale seen loxo ci ñaareelu geer bu mag bi (2:22)

GËSTUL

«Ndax diine yépp benn lañu? Ndax ñoom ñépp dañuy jëme ci Yàlla?» (Ci jw.org la nekk)

«Ndax war nañu bokk ci ab diine?» (Ci jw.org la nekk)

«Ay fen yuy tere nit ñi ñu bëgg Yàlla» (w13 1/11)

14 Naka la Yàlla bëgge ñu jaamu ko?

Ndax Yàlla nangu na ñuy jëfandikoo ay nataal ngir jaamu ko? (3:26)

Dëgg gi yewwi na ma (5:16)

GËSTUL

«Biibël bi dafay soppi dund» (w11 1/7)

Yexowa toppatoo na ma (3:07)

«Lu tax Seede Yexowa yi duñu jëfandikoo kurwaa ngir jaamu Yàlla?» (Ci jw.org la nekk)

15 Kan mooy Yeesu?

Ndax Yeesu mooy Yàlla? (3:22)

Yeesu matal na yégle yonent yi (3:03)

‘ Wóor na ne Yàlla def na ko Boroom ak Almasi ’ — Xaaj I (35:24)

GËSTUL

«Ndax li yonent yi yégle woon ci Almasi bi, wone na ne Yeesu mooy Almasi bi?» (Ci jw.org la nekk)

«Lu tax ñuy woowe Yeesu Doomu Yàlla?» (Ci jw.org la nekk)

«Ndax Yeesu mooy Yàlla?» (w09 1/4)

16 Lan la Yeesu def bi mu nekkee ci kaw suuf?

Yeesu faj na jigéen ju feebaroon (5:10)

‘ Wóor na ne Yàlla def na ko Boroom ak Almasi ’ — Xaaj II (35:06)

GËSTUL

«Ni nguuru Yàlla amee woon solo ci Yeesu» (w14 1/10)

«Kéemaan yi Yeesu def: lan nga ci mën a jàng?» (w04 15/7)

«Sama bopp rekk laa fi nekkaloon» (w14 1/10)

«Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu» (sgd 4-B)

17 Yan jikko yu rafet la Yeesu amoon?

«Joxe moo gëna barkeel nangu» (Xaaj) (4:00)

GËSTUL

«Bu ñu bëggee roy Yeesu, nañu...» (Yeesu: Yoon wi, dëgg gi, dund gi, paas 317)

«Lu tax ñu war a ñaan ci turu Yeesu?» (w08 1/2)

«Yàlla dafa bëgg ñuy wormaal jigéen ñi» (w12 1/9)

18 Naka lañu mënee ràññe karceen dëgg yi?

Ni ñu tilimale diine karceen (5:11)

Dama doyaloon ci diine (5:20)

Nangu woon na ñàkk bakkanam (2:55)

GËSTUL

«Dañu jëfandikoo Biibël bi ngir tontu ci samay laaj yépp» (w14 1/4)

Dañuy dimbali suñu mbokk yi ci ngëm bu musiba amee (Xaaj) (3:57)

«Naka lañuy xàmmee karceen dëgg yi?» (w12 1/3)

19 Ndax Seede Yexowa yi ay karceen dëgg lañu?

Feeñal nañu dëgg gi nekk ci Biibël bi (7:45)

Suñu tur dafay fësal liggéey bi ñuy def (2:40)

Taw bu réy bi ñuy woowe Matthew wàcc na ca Haïti (5:29)

GËSTUL

Mbooloom Yàlla dafay màggal turam (7:08)

«Ay laaj yu jëm ci Seede Yexowa yi» (Ci jw.org la nekk)

«Sama dund dafa doon gën a yees» (w15 1/7)

20 Ni Yexowa di jiitee mbooloo karceen mi jaare ko ci Yeesu

Magi mbooloo mi dimbali nañu waa Népal bi fa yëngu-yëngu suuf amee (4:56)

Yéen magi mbooloo mi, nekkleen ay royukaay! (7:39)

GËSTUL

Dañuy dimbali suñu mbokk yi fi ñu tere liggéeyu waare bi (4:22)

Dundu wottukat yiy wër ci dëkku àll yi (4:51)

«Magi mbooloo mi dañuy ‘liggéeyandoo ak ñun ngir suñu mbég’» (w13 15/1)

21 Naka lañuy yégle xibaaru jàmm bi?

Dañuy waare «ba fa àddina yem» (7:​33)

Liggéey bi ñuy def ngir yoon nangu ñu wéy di waare (2:​28)

GËSTUL

Dimbali nañu ñi daw seen réew ñu xam Yàlla (5:​59)

Bég naa ci jébbal sama dund gépp ci waare (6:​29)

«Waarekat yi dem nañu ci yoon ngir aar seen bopp» (kr pàcc 13)

22 Naka nga mënee xamle xibaaru jàmm bi?

Dama ñaan Yexowa mu may ma fit (4:​05)

GËSTUL

«Ndax pare nga ngir nekk nappkatu nit?» (w20 sàttumbar)

Yexowa dina la may fit (11:59)

«Mën nañu laal xolu suñu mbokk yi ñu bokkalul ngëm» (w14 15/3)

23 Sóobu ci ndox: jubluwaay bu am solo!

Ni ñu mënee nekk xaritu Yexowa (1:​11)

GËSTUL

«Bëgg Yexowa ak am ngërëm ci moom mooy xiir nit ci sóobu ci ndox» (w20 màrs)

«Dañu bëggoon man ci sama bopp ma xam lan mooy dëgg gi» (w13 1/2)

«Ndax war naa sóobu ci ndox?» (yp2, pàcc 37)

24 Ñan ñooy malaaka yi ak lan lañuy def?

«Dàqleen Seytaane» (5:​02)

GËSTUL

«Kan mooy Mikayel, kilifa malaaka yi?» (Ci jw.org la nekk)

«Léegi am na jubluwaay ci dundam» (w93 1/7)

«Dëgg gi ci lu jëm ci mbirum luxus, gisaane ak dëmm yi» (ol pàcc 5)

25 Lan la ñu Yàlla bëggal?

Lu tax Yàlla sàkk suuf si? (Xaaj) (1:​41)

Xam naa li Yàlla bëggal nit ñi (5:​03)

GËSTUL

«Toolu Eden: ndax ay léeb la walla dëgg la?» (w11 1/1)

«Ndax suuf si dina fi mas a jóge?» (Ci jw.org la nekk)

Léegi am naa jàmm ci sama dund (3:​55)

26 Lu tax lu bon ak coono di am?

Kan mooy ilif àddina si? (1:​24)

Lu tax Yàlla bàyyi coono yi di am? (Xaaj) (3:​07)

GËSTUL

«Lan mooy bàkkaar?» (Ci jw.org la nekk)

«Lu tax Yàlla bàyyi coono yi di am?» (w14 1/1)

Léegi wéetatuma (5:​09)

27 Naka la ñu deewu Yeesu mënee muccal?

Lan moo tax Yeesu dee? (Xaaj 1) (2:​01)

Lan moo tax Yeesu dee? (Xaaj 2) (2:​00)

GËSTUL

«Naka la saraxu Yeesu nekkee ‘njotug ñu bare’?» (Ci jw.org la nekk)

«Naka la ñu Yeesu di muccale?» (Ci jw.org la nekk)

«Nekkatuma nittu fitna» (Ci jw.org la nekk)

28 Woneel sa ngërëm ci li la Yexowa ak Yeesu defal

Fàttalikuleen deewu Yeesu (1:​41)

GËSTUL

Dafa màggal Yexowa ak yaramam (9:​28)

«Woneel sa ngëm ci dige Yexowa yi» (w16 oktoobar)

«Biibël bi dafay soppi dund» (w11 1/8)

29 Ñi dee, fan lañu nekk?

Lan mooy dal nit bu deewee? (Xaaj) (1:​19)

GËSTUL

«Lan mooy ruu?» (Ci jw.org la nekk)

Ndax ci dëgg safara am na? (3:​07)

Ndax ñi dee mën nañu ñu dimbali walla lor ñu? Ndax ñi dee ñu ngi dund ba tey? (téere bu ndaw)

30 Suñu mbokk yi dee mën nañu dundaat!

Yeesu dafa dekkal Lasaar (1:​16)

Yaakaaru dekki bi day tax a am fit — ci naka ? (3:​21)

GËSTUL

Boo amee mbokk bu dee (5:​06)

Njot gi (2:​07)

«Lan mooy ndekkite?» (Ci jw.org la nekk)

31 Lan mooy nguuru Yàlla?

Lan mooy nguuru Yàlla? (Xaaj) (1:​41)

GËSTUL

«Ndax nguuru Yàlla lu nekk ci suñu xol la?» (Ci jw.org la nekk)

«Ñan ñooy dem asamaan?» (Ci jw.org la nekk)

«Xam naa léegi li fi mën a dindi lu awul yoon» (Réveillez-vous!, nowàmbar 2011)

32 Nguuru Yàlla tàmbali na ilif!

Nguuru Yàlla tàmbali na ilif ci atum 1914 (5:​02)

Àddina si dafa soppeeku li dale ci atum 1914 (1:​10)

GËSTUL

«Kañ la àddina si tàmbalee yàqu nii?» (g 4/07)

«Kañ la nguuru Yàlla tàmbalee ilif? (Xaaj 1)» (w14 1/10)

«Kañ la nguuru Yàlla tàmbalee ilif? (Xaaj 2)» (w14 1/11)

33 Li nguuru Yàlla nar a def

Yeesu wone na li Nguur gi nar a def (1:​13)

Ëllëg ju neex ji ñuy xaar (4:​38)

Lan mooy Nguuru Yàlla ? (kayit)

GËSTUL

«Lan mooy metit wu réy wi» (Ci jw.org la nekk)

Xalaatal nga nekk ci àjjana ji (1:​50)

«Biibël bi dafay soppi dund» (w12 1/1)

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager