Note
b Yawut yu njëkk ya dañu daan xalaat daanaka ci ay ayubésiy at. Maanaam, niki juróom-ñaareelu fan wu nekk bésu noflaay la woon, juróom-ñaareelu at mu nekk Atum noflaay la woon.—2 Musaa 20:8-11; 23:10, 11.