Note a Ci Mbind yi lenn doŋŋ li mëna tax pase may nit mu séyaat mooy “moy”—tëdd ak nit ci bitib séy.—Macë 19:9.