Note
a Am na ay nit ñuy wax ne Biibël bi dafay weddi boppam. Waaye nit ñooñu mënuñu dëggal seeni wax. Seetal pàcc 7 ci téere bi tudd La Bible : Parole de Dieu ou des hommes ? (Biibël bi : kàddu Yàlla la walla kàddu nit la ?). Seede Yexowa yi ñoo defar téere boobu.