Note
a Lii la Peeñu ma 5:11 wax ci malaaka yu baax yi : “ Ëppoon [nañu] alfunniy alfunniy junniy junni. ” Kon Biibël bi dafay wone ne Yàlla sàkk na ay téemeeri milyoŋi malaaka.