Note a Boo bëggee am yeneen leeral ci li turu Yàlla di tekki ak li tax nekkul ci yenn Biibël yi, xoolal xaaj 1 ci téere bi tudd Téere bu ñuy dimbali ci gëstu Kàddu Yàlla.