Note c Li ngay njëkk a wax warul a weesu benn minit, ba pare laajal ñi teew ay laaj, te may leen ñu tontu.