Me Édition d’étude Sommaire WAXTAAN Nº 18 Nañu wóolu ʻkiy àtte àddina séppʼ te bare yërmande! WAXTAAN Nº 19 Lan lañu xam ci ni Yexowa di àttee ëllëg? WAXTAAN Nº 20 Na la mbëggeel xiir nga wéy di waare! WAXTAAN Nº 21 Naka ngay def ba am jëkkër ju baax walla jabar ju baax? WAXTAAN Nº 22 Naka nga mën a def ba sa ngoro jaar yoon?