Desàmbar Dañu war a kontine di sawar ci liggéeyu waare bi Nangeen fas yéene def benn njàngum Biibël Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li Ñu Def Ci Liggéeyu Waare Bi Ci Weeru Ut Li ñu mën a def ba komaase njàngum Biibël ak ñiy jël suñuy yéenekaay Nañu toppatoo suñu Saalu Nguur gi — Fànn bu am solo la ci li ñuy def ngir jaamu Yàlla Nañu wone yéenekaay yiy “ wax dëgg gi ” Yégle Yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Nañu yokk doole ñi seen xol jeex Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi