Nowàmbar Nañu sàmm suñu dundin ni ay nit ñu am xel Dañuy xamal nit ñi yaakaar bi ñu am ci nguuru Yàlla Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li Ñu Def Ci Liggéeyu Waare Bi Ci Weeru Sulyet Yégle Yi Ay Tont Ci Seeni Laaj Buleen ragal a def li baax Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi