Oktoobar Réveillez-vous ! bu am solo bu ñu war a wone ci wéeru nowàmbar ! “ Kàddu [bu génn] ci waxtu bi gën ” Liggéey bu am solo bu ñuy def ngir wone kaset bi tudd Lan la ñu Yàlla laaj ? Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li Ñu Def Ci Liggéeyu Waare Bi Ci Weeru Suweŋ Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Ci Atum 2008 Yégle Yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Na ku nekk yokk doole moroomam Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi