Feewriyee Muju jamano mu ngi jegesi, kon nañu maandu Ndax dinga nangu ñu def ay ndaje seen kër ? Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport d’octobre Nañu waaraate bu baax Ndimbal buy agsi ci waxtoom Tegtal yu bees ngir kàggu yi nekk ci Saali Nguur gi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Yégle yi Ñu bare dañu ci kontaan lool Lan moo war a ëpp solo ci yow ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi