Suweŋ Ni ñuy waaraatee ci àddina suy gaaw a soppeeku Liggéeyu waare bi, mooy liggéey bi ëpp solo ci ñun Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de février Nañu waaraate bu baax te sawar ci Ndax nekk àllaateret dina tax nga mën a yokk sa liggéey ? Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Yégle yi Làggi ba pare di def liggéey bu am solo Nañu xamal nit ñi turu Yàlla Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi