Oktoobar Lan ngay jiital ci sa dund ? Dimbalil sa moroom mu nekk xaritu Yàlla Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de juin Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2007 Yégle yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Nañu jariñoo bu baax ndaje yi ñuy def bala ñuy dem waare Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi