Septaambar Yéen ñi ñu sopp Nañu góor góorlu ngir yokk li ñuy def ci liggéeyu waaraate bi Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li Ñu Def Ci Liggéeyu Waare Bi Ci Weeru Me Nañu boolloo ngir yégle ci àddina si sépp ndaje bu mag bu ñetti fan bi tudd “ Nañu roy Kirist ” Waaraatekat yi dinañu joxewaat ay kayit yu ndaw ngir yégle suñu ndaje bu ñetti fan bi Nañu yiw ngir roy Kirist Yégle Yi Ci atum 2007, kañ lañuy def ndaje yu mag yu ñetti fan yi tudd “ Nañu roy Kirist ” ? Ndaje bu mag bu ñetti fan : Li ñu warul a fàtte Nañu roy Yeesu Li ñu mën a wax bi ñuy wone yéenekaay yi