Suweŋ Dañu kontaan lool ci li ñuy jébbal suñu bopp ci liggéeyu Yexowa ! Nañu kontine “ di meññ bu baax ” Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Rapport De Février Yégle Yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkool Sasu Nguuru Yàlla Ndax mën nga jaar ci bunt bi ñu “ ubbi ba mu ne làññ, ngir def liggéeyu Yàlla ” ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi