Oktoobar Porogaraam bu bees pur ndaje yi ñuy def ci mbooloo mi Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li ñu def ci waaraate bi ci weeru suweŋ Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Ci Atum 2009 Yégle Yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Njàngum Biibël bi ñuy def ci njaboot bi ak bi ngay defal sa bopp, am nañu solo lool ! Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi