Awril 22 Yaakaar: Ndax ci dëgg am na njariñ? Lu tax ñu soxla am yaakaar? Mën nga xeex ñaaw njort Fan lañu mënee am yaakaar dëgg?