Leneen lu jëm ci loolu rq lesoŋ 1 p. 3 Naka nga mënee xam li la Yàlla laaj ? Biibël bi dafa ñuy xamal li Yàlla bëgg ñu def Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi) Ndax ci dëgg-dëgg xibaaru jàmm bi, ci Yàlla la jóge ? Xibaaru jàmm bi jóge ci Yàlla ! Biibël bi : téere la bu jóge ci Yàlla Lan la Biibël bi wax dëgg-dëgg ? Téere biy feeñal xam-xamub Yàlla Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex Naka nga mënee jàng xam Yàlla ? Mën nga nekk xaritu Yàlla !