Leneen lu jëm ci loolu ll xaaj 6 p. 14-15 Lan lañu mën a jàng ci taw bu metti bi amoon ca jamano Nóoyin ? Xaaj 6 Déggleen li Yàlla wax Artu bu jóge ca lu amoon Mën nga nekk xaritu Yàlla ! Ca jamano yonent Yàlla Nóoyin — ñan ñoo déggoon li Yàlla wax te ñan ñoo bañoon a dégg ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Nit ku nekk am na li nga mën a jàng ci wideo bi tudd : Noé : il marchait avec Dieu Sasu Nguuru Yàlla — 2002 Nóoyin dafay defar gaal gu mag Ay nettali yu nekk ci Biibël bi