Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii
Ñan ñooy def tey li Yexowa santaane ?
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci lu ñuy jëfandikoo ngir jàngale Biibël bi ci àddina si sépp. Xaalis bu ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.
Boo bëggee maye dara, mën nga ci www.pr2711.com.
Bu ñu ko waxul, bépp aaya bu ñu fi lim, ñu ngi ko jële ci Njàlbéen ga, Mucc gi Yàlla waajal, Sabóor, Kàddu yu Xelu ak Téereb Injiil di Kàddug Yàlla. Aaya yi ànd ak MN, ci Les Saintes Écritures — Traduction du monde nouveau lañu ko jële, firi ko ci wolof. Aaya yi amagul ci wolof, bind nañu ci tubaab turu téere Biibël bi fi ñu nekk te dëngal mbind yi.
Ñan ñooy def tey li Yexowa santaane ?
Who Are Doing Jehovah’s Will Today?
Ci weeru nowàmbar ci atum 2016 lañu ko defar
Wolof (jl-WO)
© 2014 WATCH TOWER BIBLE AND TRACT SOCIETY OF PENNSYLVANIA