Yégle yi
◼ Téere yi ñuy wone ci weeru me : La Tour de Garde ak Réveillez-vous ! Boo delloo seeti nit, bu ko suñu waxtaan neexee, boole ko ci ñi ngay indil suñu yéenekaay yi saa yu ñu ci amee yu bees. Woneel téere Laaj bi ngir mën a tàmbali ay njàngum Biibël bi. Suweŋ : Lan la ñu Yàlla laaj ? walla Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex. Boo tasee ak ku am téere yooyu, won ko benn ci téere yu ndaw yu nekk ci sa mbooloo, bu mën a baax ci moom. Sulyet ak ut : Benn ci téere bu def 32 xët ci yi nekk fii : Dieu se soucie-t-il vraiment de nous ? ; Doit-on croire à la Trinité ? ; Le gouvernement qui établira le Paradis ; Le nom divin qui demeure à jamais ; Quand la mort frappe un être aimé... ; Que devient-on quand on meurt ? ; Quel est le but de la vie ? Comment le découvrir ? ; Dunda léen bà fàw ak banéx ci suf si! ; “ Voici, je fais toutes choses nouvelles ”. Boo gisee ne dina baax ci nit ki ngay waxal, mën nga wone téere yii : Connaîtrons-nous un jour un monde sans guerre ? ; Les esprits des morts — Peuvent-ils vous aider ou vous nuire ? Existent-ils vraiment ? ; Nos problèmes — Qui nous aidera à les résoudre ? ; Un livre pour tous.
◼ Wottukat biy jiite walla nit ki mu tànn war na seet ndax xaalisu mbooloo mi mat na. Loolu, 1 suweŋ lañu ko war a def, walla ni mu gënee gaaw gannaaw bés boobu. Bu ñu defee loolu ba pare, war nañu ko xamal mbooloo mi, bés bu ñuy wax fu ñu tollu ci xaalisu mbooloo mi.
◼ Téere yu bees yu ñu mën a am :
Aimeriez-vous en savoir plus sur la Bible ? (T-26)— ewe
Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex (bind yu réy)— español
La Révélation : le grand dénouement est proche !— liŋala
◼ Wideo yu bees yi ñu mën a am :
Jusqu’aux extrémités de la terre (NTSC) — araab
La Bible : le livre le plus ancien toujours d’actualité (NTSC)— araab
La Bible : un récit historique exact, des prophéties dignes de foi (NTSC) — araab
Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex, Volumes 1, 2, 3, 5 (PAL), Volumes 5, 6 (NTSC)— ci làkku liyaaru Amerig (maanaam làkku ñi tëx)
Le plus grand homme de tous les temps, Volume 2 (PAL, SECAM), Volume 4 (NTSC)— ci làkku liyaaru Amerig
Le secret du bonheur familial, Volumes 1-6 (NTSC) — ci làkku liyaaru Amerig
Les jeunes s’interrogent... Comment se faire de vrais amis ? — español
Louons Jéhovah par nos chants, Volume 1 (NTSC), Volume 2 (NTSC, SECAM)— ci làkku liyaaru Amerig
Noé : il marchait avec Dieu — araab
Toute la communauté de nos frères — español
Unis grâce à l’enseignement divin (NTSC)— araab