Prêtons attention à la prophétie de Daniel !
Porogaraamu njàng mi diggante 27 suweŋ 2005 ba 16 awril 2006.
AYU-BÉS BU PÀCC XISE AAYA YI ÑUY JÀNG
Suw. 27 1 1-18
Suly. 4 2 1-15
11 2 16-32
18 3 1-14 Dañ. 1:1-7
25 15-26 Dañ. 1:8-15
Ut 1 3 27-37 Dañ. 1:16-21
8 4 1-11 Dañ. 2:1-39
15 4 12-24* Dañ. 2:39, 40
22 4 25-36 Dañ. 2:41-49
29 5 1-17 Dañ. 3:1-18
Sept. 5 5 18-25* Dañ. 3:19-30
12 6 1-14 Dañ. 4:1-27
19 6 15-29 Dañ. 4:28-37
26 7 1-16 Dañ. 5:1-23
Okt. 3 7 17-28 Dañ. 5:24-31
10 8 1-16 Dañ. 6:1-17
17 8 17-29 Dañ. 6:18-28
24 9 1-12 Dañ. 7:1-5
31 9 13-19 Dañ. 7:6, 7
Now. 7 9 20-32 Dañ. 7:8
14 9 33-40 Dañ. 7:9-28
21 10 1-15 Dañ. 8:1-8
28 10 16-30 Dañ. 8:9-27
Des. 5 11 1-12 Dañ. 9:1-23
12 11 13-20 Dañ. 9:24, 25
19 11 21-30 Dañ. 9:26, 27
26 12 1-13 Dañ. 10:1-8
Sãw. 2 12 14-22 Dañ. 10:9-21
9 13 1-15 Dañ. 11:1-4
16 13 16-30 Dañ. 11:5-16
23 13 31-9 Dañ. 11:17-19
30 14 1-15 Dañ. 11:20-24
Feew. 6 14 16-27 Dañ. 11:25, 26
13 15 1-15 Dañ. 11:27-30a
20 15 16-25 Dañ. 11:30b, 31
27 16 1-17 Dañ. 11:32-41
Màrs 6 16 18-28 Dañ. 11:42-45
13 17 1-12 Dañ. 12:1-3
20 17 13-23 Dañ. 12:4-11
27 17 24-9 Dañ. 12:12
Awr. 3 18 1-12 Dañ. 12:13
10 18 13-27 Dañ. 12:13
Ci xise walla laaj yi, bu ñu la waxee nga jàng dara ci beneen xët, nanga ko jàng te waxtaane ko. Seetal wërale bi tudd “ La question de la langue ” (xët 26 ci téere bi ñu defaral ñépp, xët 32-3 ci téere bi ñu defar ak mbind yu réy). Dingeen war a jàng li nekk ci wërale boobu bu ngeen àggee ci pàcc 2, xise 25, laaj c). Bu amee tablo ak yeneen yu ñu defar ngir yombalal njàng mi, te ñu ànd ak li ngeen di jàng, nangeen ci waxtaan. Nangeen xam ne ci téere bi ñu defar ak mbind yu réy, amul tablo ak nataal yi nekk ci xët 56, 139, ak 188-9 ci téere bi ñu defaral ñépp. Boo paree njàng mu nekk te bu la ko jot bi mayee, nanga jàng ci Biibël bi “ aaya yi ñu jàng ” te waxtaan ci.
* Mën nga seetaat itam “ aaya yi ñu jàng ” ci ayu-bés bi paase, bu la ko jot bi mayee.