TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 5/05 p. 7
  • Yégle yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Yégle yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2005
Sasu Nguuru Yàlla — 2005
km 5/05 p. 7

Yégle yi

◼ Téere yi ñuy wone diggante 1 ba 15 me : Benn La Tour de Garde ak benn Réveillez-vous ! Bu ñuy dellu seeti nit ñi suñu waxtaan neex, nañu ci boole nit ñi mas a teew ci ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu, walla ci beneen ndaje, waaye tàmmuñu teew ci ndaje yi yépp. Nañu leen won téere Adorez Dieu. Li ñu bëgg mooy tàmbali ay njàngum Biibël, rawatina ak ku jàng ba pare téere Xam-xam ak it téere Laaj. 16 me ba 12 suweŋ : Dinañu wone suñu téere bu bees bi tudd Veillez ! 13-30 suweŋ : Écoute le grand Enseignant. Bu nit ki waxee ne amul doom, won ko téere Laaj bi te jéemal a tàmbali njàngum Biibël ak téere boobu. Sulyet ak ut : Benn ci téere bu def 32 xët ci yi nekk fii : Dieu se soucie-t-il vraiment de nous ? ; Doit-on croire à la Trinité ? ; Dunda léen bà fàw ak banéx ci suf si! ; Le gouvernement qui établira le Paradis ; Le nom divin qui demeure à jamais ; Quand la mort frappe un être aimé ; Que devient-on quand on meurt ? ; Quel est le but de la vie ? Comment le découvrir ? ; “ Voici, je fais toutes choses nouvelles ”.

◼ Wottukat biy jiite walla nit ki mu tànn war na seet ndax xaalisu mbooloo mi mat na. Loolu, 1 suweŋ lañu ko war a def, walla ni mu gënee gaaw gannaaw bés boobu. Bu fekkee ne dangeen am kees fu ngeen di dajale xaalis ngir tabax ay Saalu Nguur, walla toppatoo Saal bi, walla yeneen keesu xaalis, seetleen it ndax xaalisu kees yooyu mat na. Bu ñu seetee ndax xaalisu kees yi mat na ba pare, war nañu ko xamal mbooloo mi, bés bu ñuy wax fu ñu tollu ci xaalisu mbooloo mi.

◼ Ci Guinée-Bissau, ci atum liggéeyu waare 2005, amoon na weer boo xam ne waaraatekat yi masuñu woon bare noonu. Waaye ci weeru sãwiyee, weesu nañu loolu ndaxte 111 waaraatekat lañu woon. Waaraate nañu lu tollu 5 407 waxtu. Loolu it masul woon a am.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager