Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
1. Naka lañu mënee ‘déglu li xel mu sell mi di wax’? (Peeñu ma 1:3, 10, 11; 3:19)
2. Lan moo ñu mën a dimbali ñu wéy di liggéey bu baax te di muñ? (Peeñu ma 2:4)
3. Naka lañu mënee waajal suñu bopp ngir mën a muñ fitna yi ànd ci ak fit? (Kàddu yu Xelu 29:25; Peeñu ma 2:10, 11)
4. Naka lañu mënee moytu weddi suñu ngëm ci Yeesu? (Peeñu ma 2:12-16)
5. Naka lañu mënee ŋoy ci li ñu am? (Peeñu ma 2:24, 25; 3:1-3, 7, 8, 10, 11)
6. Lan moo ñuy dimbali ñu wéy di farlu? (Peeñu ma 3:14-19; Macë 6:25-27, 31-33)
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
CA-brpgm26-WO