Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
1. Ñu mel nan la Yexowa di wut? (Yowaan 4:23, 24)
2. Naka la ñu xel mu sell mi mënee dimbali ñu jox Yexowa li gën ci ñun? (Jëf ya 16:6-10; 1 Korent 2:10-13; Filib 4:8, 9)
3. Naka lañuy ‘fésale dëgg gi’? (2 Korent 4:1, 2)
4. Jaamu Yàlla ci dëgg, lan lay tekki? (Kàddu yu Xelu 24:3; Yowaan 18:36, 37; Efes 5:33; Yawut ya 13:5, 6, 18)
5. Naka lañu mëne ‘jënd dëgg gi te bañ koo jaay’? (Kàddu yu Xelu 23:23)
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
CA-copgm26-WO