• Yeen mbokk yu góor yi, ndax yeen a ngi góor-góorlu ngir bokk ci ñiy toppatoo yëfi mbooloo mi?