Leneen lu jëm ci loolu gf lesoŋ 7 p. 12-13 Artu bu jóge ca lu amoon Ca jamano yonent Yàlla Nóoyin — ñan ñoo déggoon li Yàlla wax te ñan ñoo bañoon a dégg ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Nit ku nekk am na li nga mën a jàng ci wideo bi tudd : Noé : il marchait avec Dieu Sasu Nguuru Yàlla — 2002 Nóoyin dafay defar gaal gu mag Ay nettali yu nekk ci Biibël bi Xaaj 5 Déggleen li Yàlla wax Lan lañu mën a jàng ci taw bu metti bi amoon ca jamano Nóoyin ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex