Leneen lu jëm ci loolu ll xaaj 2 p. 6-7 Kan mooy Yàlla dëgg ji ? Xaaj 2 Déggleen li Yàlla wax Ku leen sàkk ? Dundleen ba fàww ak bànneex ci suuf si ! Kan mooy Yàlla ? Lan la ñu Yàllay laaj? Kan mooy Yàlla? Gëm Yàlla dëgg moo ñu mën a indil jàmm Dañu fi nettali bi Yàlla komaasee sàkk ba bi mu indee mbënn mi, maanaam taw bu metti, ci kow suuf si sépp Ay nettali yu nekk ci Biibël bi