Leneen lu jëm ci loolu w25 Septaambar p. 2-7 Waxal magi mbooloo mi ñu dimbali la Ni magi mbooloo yi mën a def ngir dimbali ñi bàkkaar ànd ci ak mbëggeel ak yërmande La Tour de Garde annonce le Royaume de Jéhovah (Édition d’étude)-2024 Ni Yexowa di jiitee mbooloo karceen mi jaare ko ci Yeesu Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi) Yeen mbokk yu góor yi, ndax yeen a ngi góor-góorlu ngir nekk magu mbooloo? La Tour de Garde annonce le Royaume de Jéhovah (Édition d’étude)-2024 Ni magi mbooloo yi mënee dimbali ñi ñu génne ci mbooloo mi La Tour de Garde annonce le Royaume de Jéhovah (Édition d’étude)-2024 Wonal ngërëm góor yi ñu Yexowa ak Yeesu may ngir toppatoo mbooloo mi La Tour de Garde annonce le Royaume de Jéhovah (Édition d’étude)-2024 Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2025-2026 Naka la magi mbooloo mi di dimbalee waa mbooloo mi ? Ñan ñooy def tey li Yexowa santaane ? Nañu fàttaliku ne Yexowa mooy «Yàlla jiy dund» La Tour de Garde annonce le Royaume de Jéhovah (Édition d’étude)-2024