TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • sjj woy 160
  • “Am nañu Xibaaru jàmm”!

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • “Am nañu Xibaaru jàmm”!
  • Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Xabaaru Nguur gi, bu baax bi,nañu ko waar
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Waarleen “xabaar bu baax bii ci Nguur gi”!
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Yéen Seede yi, aywa!
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Naka lañuy yéglee xibaaru jàmm bi?
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
sjj woy 160

WOY-YÀLLA 160

“Am nañu Xibaaru jàmm”!

Édition imprimée

(Luug 2:10)

  1. 1. Nañu màggal Yexowa

    Ca kaw asamaan.—

    Bi Yeesu juddoo ca Betleyem,

    Yaakaar amaat na

    Ndax mooy Musalkat bi.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.

  2. 2. Waaw, Yeesu dina nguuru,

    Jàmm am fu ne.

    Moo ñuy jëme ci dund ba fàww.

    Yoon rekk lay àtte,

    Nguuram du mas a jeex.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.

(Xoolal itam Macë 24:14; Yowaana 8:12; 14:6; Esayi 32:1; 61:2).

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager