TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 10/02 p. 3-6
  • Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2003

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2003
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2002
  • Turu xaaj yi
  • Ni ñu koy defe
  • PROGRAMME
Sasu Nguuru Yàlla — 2002
km 10/02 p. 3-6

Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2003

Ni ñu koy defe

Ci atum 2003, nii lañuy defe lekkoolu sasu Nguuru Yàlla bi :

TÉERE YI ÑUY JËFANDIKOO : Les Saintes Écritures -- Traduction du monde nouveau [bi12], La Tour de Garde [w], Tirez profit de l’École du ministère théocratique [be], “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile ” (édition de 1997) [si], et Comment raisonner à partir des Écritures (édition de 1989) [rs].

WARUÑU TÀRDE. Bu waxtu bi jote rekk, nañu tàmbali lekkool bi ak benn woy-Yàlla, ñaan te teral nit ñi, ba pare def lii :

LIY TAX ÑU AAY CI WAX (Technique oratoire) : 5 minit. Wottukatu lekkool bi, kiy koy jàpple, walla mag bu mën def lekkool bi dina jëfandikoo téere École du ministère ngir waxtaan ci lenn luy tax ñu aay ci wax. (Bu ngeen amulee mag yu bare ci seen mbooloo, surga mbooloo bu mën jàngale mën na def waxtaan bi). War nañu laal lépp li feeñ ci xët yi ñu jagleel waxtaan bi. Bu amee ci xët yooyu wërale bu ci bokkul, dinañu ko wax. Waruñu boole jéemantal yi ci waxtaan bi. Jéemantal yooyu, nit ku nekk moo ko war a defal boppam. Kuy jiite lekkool bi mën na leen jëfandikoo itam bu wéetee ak nit, di ko xelal.

WAXTAAN N° 1 : 10 minit. Benn mag walla benn surga mbooloo mi moo ko war a def. Ci téere yii lañu koy defe : La Tour de Garde, Tirez profit de l’École du ministère théocratique walla “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile ”. Waare lay doon ngir jàngal ñi teew ci 10 minit. Warul a laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li mu wax ci waxtaanam. Wax li nekk ci xët yi ñuy jagleel waxtaan bi kese taxul ñuy def waxtaan bi. Ki koy def, dafa war a wone bu baax njariñ bi nekk ci xët yooyu. Te it, war na wone bu baax li gën a am njariñ ci mbooloo mi. Waxtaan bi jox nañu ko tur (thème) ba pare. Tur boobu lañu war a jëfandikoo. Waxtaan bi warul a weesu 10 minit. Bu ñu waree xelal ki def waxtaan bi, kiy jiite lekkool bi na wéet ak moom.

KÀDDU YU AM SOLO CI LI ÑU WAROON A JÀNG CI BIIBËL BI : 10 minit. Ci juróom-benni minit yi njëkk yi, magu mbooloo walla surga mbooloo bu aay, war na wone ni mbooloo mi mënee jariñoo xaaju Biibël bi ñu waroon a jàng ci ayu-bés bi. Mën na wax ci aaya bu mu mënta doon bu bokk ci xaaj boobu, ndaxte kiy def waxtaan n° 2, bu jàngee aaya yi ñu ko jox ba pare, du ci waxtaane. Kiy def waxtaan bi, warul yem rekk ci tënk pàcc yi ñu war a jàng, waaye war na won lu tax li ci nekk am njariñ ak it naka lañu ko mënee jariñoo. Bu loolu weesoo, ci lu mat ñeenti minit, dinañu ñaan ñi teew ñu tontu ci lu gàtt (30 segoond walla sax ci lu gën a gaaw) ci ñaari laaj yii : “ Ci li ngeen jàng ci Biibël bi ayu-bés bii, lan ngeen mën a jariñoo bu ngeen di waaraate, walla ci seen dund ? ” ak “ Lan moo dëgëral seen ngëm te tax ngeen gën a gërëm Yexowa ? ” Bu nit ñi tontoo ba pare, ñi war a dem ci beneen kalaas bi dinañu mën a génn.

WAXTAAN N° 2 : 4 minit. Benn mbokk mu góor moo ko war a def. Ci lu ëpp, ci Biibël bi lay jànge. Waaye weer wu nekk, dinañu ñaan benn yoon mbokk bi koy def mu jàng benn xaaj ci La Tour de Garde. Kiy def waxtaan bi, warul wax dara balaa muy jàng, te bu jàngee ba pare, warul wax dara itam. Aaya yi ñu war a jàng ci waxtaan bi, mën nañu bañ a tolloo ayu-bés bu nekk, waaye ba tey ci ñeenti minit lañu ko war a jànge, walla sax ci lu gën a gaaw. Wottukat biy jiite lekkool bi war na seet li nekk ci li ñu war a jàng ayu-bés bu nekk, bu ko defee mu mën a xam ki ko war a def ndax mën na nekk xale walla déet, ndax dafa war a aay ci njàngale bi walla déet. Wottukatu lekkool bi war na seet bu baax ni mu mënee dimbali kiy jàng ci lii : buy jàng, mu nànd li muy jàng ; jàng bi yomb ci moom (fluidité) ; mu bañ a juum ci ni muy waxe baat yi te kàddu yi ëpp solo feeñ bu baax ; li ñuy woowe modulation ; buy jàng, mu taxaw fi mu war a taxaw ; te wax ni muy waxe bés bu nekk.

WAXTAAN N° 3 : 5 minit. Benn mbokk mu jigéen moo ko war a def. Mën na tànnal boppam cadre bi (maanaam ni waxtaan bi di ame), waaye yenn saay dinañu ko jox benn cadre ci yi nekk ci téere École du ministère ci xët 82. Na topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi te mel ni kuy waaraate. Na waxtaan bi niroo ak lu mën a am dëgg ci gox bu seen mbooloo moom te mën a jariñ waaraatekat yi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def na wutal boppam li muy wax ci téere yi surga bu takku te teey bi defar. Ñi yàggul a bokk ci lekkool bi, nañu leen jox waxtaan boo xam ne wax nañu yan téere la war a jëfandikoo. Wottukatu lekkool bi dina seetlu bu baax ni waxtaan bi di demee ak ni mbokk mu koy def di dimbalee ki muy jàngal ba mu mën a xalaat ci li nekk ci mbind mi te nànd li ëpp solo ci waxtaan bi. Ñiy def waxtaan bi dañu war a mën a jàng. Wottukatu lekkool bi dina ko wax ak kan la war a def waxtaan bi.

WAXTAAN N °4 : 5 minit. Ki koy def dafa war a topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def moo war a wutal boppam li muy wax ci téere yi surga bu takku te teey bi defar. Bu fekkee ne mbokk mu góor moo ko war a def, waare lay doon, te bu koy def dina bàyyi xel ci ñi koy déglu. Bu dee mbokk mu jigéen moo koy def, na ko def ni ñuy defe waxtaan n° 3. Bu leen fàtte ne waxtaan yi ànd ak biddéew bu ndaw, mbokk mu góor kese moo leen war a def. Bu booba waare lay doon.

WAXTU WI : Waxtaan yi ak xelal yi, waruñu yàgg ba weesu waxtu bi ñu leen may. Ñiy def waxtaan n° 2, 3, ak 4, bu ñu weesoo waxtu bi ñu leen may, nañu seet fasoŋ bu rafet bu ñu mënee dog seen waxtaan. Kiy def waxtaan buy ubbi lekkool bi te jëm ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire), kiy def waxtaan n° 1, walla kiy wax kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi, bu ci amee ku waxtaanam yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may, war nañu wéet ak moom ngir xelal ko. Képp kuy def waxtaan war na seetlu bu baax waxtu bi ngir waxtaanam bañ a yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may. Lekkool bi, boole ci ñaan bi ak woy-Yàlla bi, 45 minit la war a def.

XELAL YI : 1 minit. Bu kenn paree waxtaanam, wottukatu lekkool bi dina wax ci li baax li mu def ci waxtaan bi. Dina ci wax lu koy mën a jëmale kanam. Loolu warul weesu benn minit. Du ko wax rekk ne “ sa waxtaan bi baaxoon na ”, waaye dina wax lenn ci li tax waxtaanam baax. Bu ndaje bi jeexee, walla beneen yoon, dina toog ak moom ngir xelal ko ci leneen, ndax mu mën a jëm kanam.

KIY JÀPPLE KIY XELAL NIT ÑI : Ginnaaw wottukatu lekkool bi, bu amee beneen mag ci mbooloo mi bu mën a jiite lekkool bi, kurélu mag ñi dinañu ko tànn ngir mu jàpple kiy xelal nit ñi. Kooku mooy xelal ñiy def waxtaan no 1 ak kiy wax Kàddu yu am solo ci Biibël bi. Du saa yu mag walla surga mbooloo mi di def waxtaan yooyu, la koy war a xelal. Li ñu wax fii, dinañu ko def ci atum 2003 yépp. Waaye bu ci kanamee, mën na am ñu soppi ci dara.

KAYIT FI ÑU BIND XELAL YI : Mu ngi ci téere Tirez profit de l’École du ministère théocratique.

WAXTAAN AK ÑI TEEW NGIR FÀTTALIKU LI ÑU DEF CI LEKKOOL BI (Révision orale) : 30 minit. Ñaari weer yu nekk, wottukatu lekkool bi dina laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li ñu def ci lekkool bi. Dinañu njëkk wax ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire) ak it kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi (nañu topp tegtal yi nekk ci kow ngir waxtaan yooyu), ba pare ñu waxtaan ak ñi teew ngir fàttaliku li ñu def ci lekkool bi ci ñaari weer yi weesu, boole ci li ñu def ci ayu-bés bi.

PROGRAMME

6 janv. Lecture de la Bible : Matthieu 1-6 Cantique 91

Technique oratoire : Bienvenue à l’École du ministère théocratique (be p. 5 § 1–p. 8 § 1)

No 1 : Prenez plaisir dans la Parole de Dieu (be p. 9 § 1-p. 10 § 1)

No 2 : Matthieu 4:1-22

No 3 : En quoi les vrais chrétiens sont-ils concernés par le signe des derniers jours ? (rs p. 93 § 1-2)

No 4 : Que fait Jésus actuellement ?

13 janv. Lecture de la Bible : Matthieu 7-11 Cantique 40

Technique oratoire : Lisez la Bible chaque jour (be p. 10 § 2–p. 12 § 3)

No 1 : ‘ Courez de manière à obtenir le prix ’ (w01 1/1 p. 28-31)

No 2 : Matthieu 9:9-31

No 3 : Pourquoi nous prêchons

No 4 : Pourquoi les Témoins de Jéhovah disent-ils que les derniers jours ont commencé en 1914 ? (rs p. 94 § 2–p. 95 § 1)

20 janv. Lecture de la Bible : Matthieu 12-15 Cantique 133

Technique oratoire : Lecture précise (be p. 83 § 1-5)

No 1 : Vous pouvez vaincre le découragement ! (w01 1/2 p. 20-3)

No 2 : Matthieu 13:1-23

No 3 : Y aura-t-il des survivants à la fin du présent système de choses ? (rs p. 95 § 2-5)

No 4 : Dieu change-t-il ?

27 janv. Lecture de la Bible : Matthieu 16-21 Cantique 129

Technique oratoire : Comment faire une lecture précise (be p. 84 § 1–p. 85 § 3)

No 1 : Le caractère fugitif du temps (si p. 278-9 § 1-6)

No 2 : w01 15/1 p. 20 § 20–p. 21 § 24

No 3 : Un monde uni : comment ?

No 4 : Pourquoi Dieu attend-il si longtemps avant de détruire les méchants ? (rs p. 96 § 1-3)

3 févr. Lecture de la Bible : Matthieu 22-25 Cantique 139

Technique oratoire : Bonne élocution (be p. 86 § 1-6)

No 1 : ‘ Faites attention à la manière dont vous écoutez ’ (be p. 13 § 1–p. 14 § 5)

No 2 : Matthieu 22:15-40

No 3 : Comment savons-nous que le signe désigne bien notre époque ? (rs p. 96 § 5–p. 97 § 2)

No 4 : “ Quel est donc l’esclave fidèle et avisé ? ”

10 févr. Lecture de la Bible : Matthieu 26-28 Cantique 27

Technique oratoire : Comment s’exprimer nettement (be p. 87 § 1–p. 88 § 3)

No 1 : Comment trouver le bonheur véritable (w01 1/3 p. 4-7)

No 2 : Matthieu 26:6-30

No 3 : Pourquoi je ne me drogue pas

No 4 : Quel est le but de la vie humaine ? (rs p. 434 § 1–p. 435 § 3)

17 févr. Lecture de la Bible : Marc 1-4 Cantique 137

Technique oratoire : Prononciation correcte — facteurs à considérer (be p. 89 § 1–p. 90 § 3)

No 1 : Indicateurs de temps dans la Bible (si p. 279-80 § 7-13)

No 2 : w01 15/2 p. 25 § 10–p. 26 § 14

No 3 : Les humains ont-ils été faits pour vivre peu de temps, puis mourir ? (rs p. 435 § 4–p. 436 § 2)

No 4 : Pourquoi le jeu est-il condamnable ?

24 févr. Lecture de la Bible : Marc 5-8 Cantique 72

Technique oratoire : Des conseils pour améliorer votre prononciation (be p. 90 § 4–p. 92)

Révision orale

3 mars Lecture de la Bible : Marc 9-12 Cantique 195

Technique oratoire : Fluidité de l’expression (be p. 93 § 1–p. 94 § 3)

No 1 : Comment écouter lors des discours, des discussions par questions et réponses, et des assemblées (be p. 15 § 1–p. 16 § 5)

No 2 : Marc 10:1-22

No 3 : Comment trouver de la force auprès de Dieu

No 4 : Qu’est-ce qui nous permet d’espérer vivre à jamais ? (rs p. 437 § 1-3)

10 mars Lecture de la Bible : Marc 13-16 Cantique 187

Technique oratoire : Des conseils pour progresser en fluidité (be p. 94 § 4–p. 96 § 3, sauf l’encadré p. 95)

No 1 : Qu’est-ce que le paradis spirituel ? (w01 1/3 p. 8-11)

No 2 : Marc 13:1-23

No 3 : Comment la perspective d’une vie future se concrétisera-t-elle ? (rs p. 437 § 4-6)

No 4 : Dieu prend-il parti dans les guerres ?

17 mars Lecture de la Bible : Luc 1-3 Cantique 13

Technique oratoire : Comment maîtriser le bégaiement (be p. 95, encadré)

No 1 : “ Heureux l’homme qui a trouvé la sagesse ” (w01 15/3 p. 25-8)

No 2 : Luc 3:1-22

No 3 : Doit-on adorer Jésus ?

No 4 : aEst-il important de se marier légalement ? (rs p. 224 § 2–p. 225 § 1)

24 mars Lecture de la Bible : Luc 4-6 Cantique 156

Technique oratoire : Pauses pour ponctuer ou marquer une transition (be p. 97 § 1–p. 98 § 5)

No 1 : Avez-vous le sentiment d’avoir été mal compris ? (w01 1/4 p. 20-3)

No 2 : Luc 6:1-23

No 3 : Quelle est la signification du Mémorial ? (rs p. 242 § 1-3)

No 4 : Les chrétiens doivent-ils s’attendre à être protégés par Dieu ?

31 mars Lecture de la Bible : Luc 7-9 Cantique 47

Technique oratoire : Pauses pour accentuer, pauses pour écouter (be p. 99 § 1–p. 100 § 4)

No 1 : “ Crains le vrai Dieu et garde ses commandements ” (be p. 272 § 1–p. 275 § 3)

No 2 : w01 15/3 p. 18 § 17–p. 19 § 20

No 3 : Comment savons-nous que la Bible vient de Dieu ?

No 4 : Que représentent les emblèmes du Mémorial ? (rs p. 242 § 4–243 § 1)

7 avril Lecture de la Bible : Luc 10-12 Cantique 68

Technique oratoire : Accentuation des mots clés (be p. 101 § 1–p. 102 § 3)

No 1 : “ Rendre témoignage à Jésus ” (be p. 275 § 4–p. 278 § 4)

No 2 : Luc 10:1-22

No 3 : Qui devrait participer au Repas du Seigneur ? (rs p. 243 § 3-4)

No 4 : Quelles formalités ont accompagné le premier mariage ? (rs p. 225 § 2-3)

14 avril Lecture de la Bible : Luc 13-17 Cantique 208

Technique oratoire : Améliorer son accentuation (be p. 102 § 4–p. 104 § 2)

No 1 : “ Cette bonne nouvelle du royaume ” (be p. 279 § 1–p. 281 § 4)

No 2 : Luc 15:11-32

No 3 : Comment se protéger de l’influence des démons

No 4 : Combien de fois par an le Mémorial devrait-il être célébré, et à quelle date ? (rs p. 244 § 3–p. 245 § 1)

21 avril Lecture de la Bible : Luc 18-21 Cantique 23

Technique oratoire : Mise en valeur des idées essentielles (be p. 105 § 1–p. 106 § 2)

No 1 : Les saisons : une disposition de Jéhovah, sage et pleine d’amour (si p. 280 § 14-17)

No 2 : w01 15/4 p. 6 § 19–p. 7 § 22

No 3 : Quel effet l’espérance de la résurrection a-t-elle sur notre vie ?

No 4 : bLa Bible excuse-t-elle la polygamie ? (rs p. 225 § 4–p. 226 § 5)

28 avril Lecture de la Bible : Luc 22-24 Cantique 218

Technique oratoire : Volume adapté à l’auditoire (be p. 107 § 1–p. 108 § 5)

Révision orale

5 mai Lecture de la Bible : Jean 1-4 Cantique 31

Technique oratoire : Comment améliorer le volume de votre voix (be p. 108 § 6–p. 110 § 2)

No 1 :Une mémoire plus performante (be p. 17 § 1–p. 19 § 1)

No 2 : Jean 2:1-25

No 3 : Dieu condamne-t-il la consommation d’alcool ?

No 4 : cQuel est le point de vue de Dieu sur la séparation ? (rs p. 227 § 1)

12 mai Lecture de la Bible : Jean 5-7 Cantique 150

Technique oratoire : Modulation — adaptez le volume de votre voix (be p. 111 § 1–p. 112 § 2)

No 1 : Vous pouvez réussir quelle que soit votre éducation (w01 15/4 p. 25-8)

No 2 : Jean 5:1-24

No 3 : Pourquoi la doctrine de la prédestination n’est-elle pas logique ?

No 4 : dQuel est le point de vue de la Bible sur le divorce et le remariage ? (rs p. 227 § 2–p. 228 § 2)

19 mai Lecture de la Bible : Jean 8-11 Cantique 102

Technique oratoire : Modulation — changez de débit (be p. 112 § 3–p. 113 § 1)

No 1 : ‘ Par la sagesse nos jours deviendront nombreux ’ (w01 15/5 p. 28-31)

No 2 : Jean 10:16-42

No 3 : Pourquoi Dieu a-t-il jadis autorisé des mariages entre frères et sœurs ? (rs p. 228 § 3-4)

No 4 : Comment combattre le stress

26 mai Lecture de la Bible : Jean 12-16 Cantique 24

Technique oratoire : Modulation — variez votre ton (be p. 113 § 2–p. 114 § 3)

No 1 : La notion d’année dans les Saintes Écritures (si p. 280 -2 § 18-23)

No 2 : w01 1/5 p. 14 § 4–p. 15 § 7

No 3 : Ce que signifie ne ‘ pas faire partie du monde ’

No 4 : Comment rendre son mariage plus heureux ? (rs p. 229 § 1-4)

2 juin Lecture de la Bible : Jean 17-21 Cantique 198

Technique oratoire : Parlez avec sentiment (be p. 115 § 1–p. 116 § 4)

No 1 : Comment l’esprit de Dieu vient en aide à notre mémoire (be p. 19 § 2–p. 20 § 3)

No 2 : Jean 20:1-23

No 3 : Comment rendre son mariage plus heureux ? (rs p. 229 § 5–p. 230 § 2)

No 4 : Une organisation religieuse est-elle nécessaire ?

9 juin Lecture de la Bible : Actes 1-4 Cantique 92

Technique oratoire : Enthousiasme approprié aux idées (be p. 116 § 5–p. 117 § 4)

No 1 : Affermissez votre confiance en Jéhovah (w01 1/6 p. 7-10)

No 2 : Actes 4:1-22

No 3 : Quelles leçons pouvons-nous tirer du récit biblique relatif à Marie ? (rs p. 230 § 3-8)

No 4 : La manière dont nous adorons Dieu a-t-elle de l’importance à ses yeux ?

16 juin Lecture de la Bible : Actes 5-7 Cantique 2

Technique oratoire : S’exprimer avec chaleur (be p. 118 § 1–p. 119 § 5)

No 1 : La guérison spirituelle grâce à la confession (w01 1/6 p. 28-31)

No 2 : Actes 7:1-22

No 3 : En quoi les Témoins de Jéhovah diffèrent-ils des autres religions ?

No 4 : Marie était-elle vraiment vierge quand elle a donné naissance à Jésus ? (rs p. 231 § 1-2)

23 juin Lecture de la Bible : Actes 8-10 Cantique 116

Technique oratoire : S’exprimer avec sentiments (be p. 119 § 6–p. 120 § 5)

No 1 : Prenons soin des orphelins et des veuves dans leur tribulation (w01 15/6 p. 9-12)

No 2 : w01 1/6 p. 12 § 1–p. 13 § 5

No 3 : Marie est-elle restée vierge ? (rs p. 231 § 3–p. 232 § 1)

No 4 : ePourquoi l’assistance aux réunions est indispensable à la croissance spirituelle

30 juin Lecture de la Bible : Actes 11-14 Cantique 167

Technique oratoire : L’importance des gestes et des expressions du visage (be p. 121 § 1-4)

Révision orale

7 juillet Lecture de la Bible : Actes 15-17 Cantique 38

Technique oratoire : Le recours aux gestes et aux expressions du visage (be p. 121 § 5–p. 123 § 2)

No 1 : Pourquoi s’appliquer à la lecture ? (be p. 21 § 1–p. 23 § 3)

No 2 : Actes 15:1-21

No 3 : Comment soutenons-nous la souveraineté de Jéhovah ?

No 4 : Marie est-elle la mère de Dieu ? (rs p. 232 § 2-4)

14 juillet Lecture de la Bible : Actes 18-21 Cantique 32

Technique oratoire : Le contact visuel dans le ministère (be p. 124 § 1–p. 125 § 3)

No 1 : Ne laissez pas les doutes miner votre foi (w01 1/7 p. 18-21)

No 2 : Actes 19:1-22

No 3 : fMarie a-t-elle été préservée du péché originel ? (rs p. 233 § 1-2)

No 4 : Ce que signifie ‘ continuer à chercher d’abord le royaume ’

21 juillet Lecture de la Bible : Actes 22-25 Cantique 222

Technique oratoire : Le contact visuel quand vous donnez un discours (be p. 125 § 4–p. 126 § 6)

No 1 : Manifestez-vous une juste tolérance ? (w01 15/7 p. 21-3)

No 2 : Actes 24:1-23

No 3 : Le Diable est-il réel ?

No 4 : gMarie est-elle montée au ciel avec son corps de chair ? (rs p. 234 § 1-2)

28 juillet Lecture de la Bible : Actes 26-28 Cantique 14

Technique oratoire : Le naturel dans le ministère (be p. 128 § 1–p. 129 § 1)

No 1 : Pas d’année zéro (si p. 282 § 24-6)

No 2 : w01 1/7 p. 14 § 5-8

No 3 : Convient-il de prier Marie d’intercéder en notre faveur ? (rs p. 234 § 3–p. 235 § 1)

No 4 : Comment montrons-nous du respect pour le don de la vie ?

4 août Lecture de la Bible : Romains 1-4 Cantique 106

Technique oratoire : Le naturel sur l’estrade (be p. 129 § 2–p. 130 § 1)

No 1 : Comment vous appliquer à la lecture (be p. 23 § 4–p. 26 § 5)

No 2 : Romains 2:1-24

No 3 : Avez-vous eu une vie antérieure ?

No 4 : Rendait-on un honneur spécial à Marie dans la congrégation du Ier siècle ? (rs p. 235 § 3–p. 236 § 2)

11 août Lecture de la Bible : Romains 5-8 Cantique 179

Technique oratoire : Le naturel lors d’une lecture publique (be p. 130 § 2-4)

No 1 :‘ Les bénédictions sont pour le juste ’ (w01 15/7 p. 24-7)

No 2 : Romains 5:6-21

No 3 : hCroyez-vous à la vierge Marie ? (rs p. 236 § 3–p. 237 § 1)

No 4 : Devriez-vous croire à la réincarnation ?

18 août Lecture de la Bible : Romains 9-12 Cantique 206

Technique oratoire : Notre hygiène corporelle pare notre message (be p. 131 § 1-3)

No 1 : Faisons de la force de l’habitude une force pour le bien (w01 1/8 p. 19-22)

No 2 : w01 15/8 p. 22 § 10-13

No 3 : La Bible a-t-elle été changée ?

No 4 : La transsubstantiation est-elle un fait ? (rs p. 245 § 2–p. 247 § 1)

25 août Lecture de la Bible : Romains 13-16 Cantique 43

Technique oratoire : Comment la modestie et le bon sens influent-ils sur notre habillement et notre coiffure ? (be p. 131 § 4–p. 132 § 3)

Révision orale

1er sept. Lecture de la Bible : 1 Corinthiens 1-9 Cantique 48

Technique oratoire : La valeur d’une tenue bien arrangée (be p. 132 § 4-6)

No 1 : Comment étudier (be p. 27 § 1–p. 31 § 2)

No 2 : 1 Corinthiens 3:1-23

No 3 : Que veulent dire les paroles rapportées en Jean 6:53-57 ? (rs p. 247 § 2-3)

No 4 : La pauvreté justifie-t-elle le vol ?

8 sept. Lecture de la Bible : 1 Corinthiens 10-16 Cantique 123

Technique oratoire : Une belle apparence pour ne pas faire trébucher (be p. 133 § 1-3)

No 1 : Surmontez les obstacles à vos progrès ! (w01 1/8 p. 28-30)

No 2 : 1 Corinthiens 12:1-26

No 3 : Pourquoi Dieu permet-il les malheurs ?

No 4 : Jésus a-t-il institué la messe ? (rs p. 247 § 4–p. 249 § 4)

15 sept. Lecture de la Bible : 2 Corinthiens 1-7 Cantique 16

Technique oratoire : Un bon maintien et des accessoires nets (be p. 133 § 4–p. 134 § 4)

No 1 : Réussir sa jeunesse (w01 15/8 p. 4-7)

No 2 : 2 Corinthiens 6:1–7:1

No 3 : L’attitude du chrétien vis-à-vis des autorités de ce monde (rs p. 263 § 3–p. 264 § 2)

No 4 : Dieu se soucie-t-il de la pollution de la terre ?

22 sept. Lecture de la Bible : 2 Corinthiens 8-13 Cantique 207

Technique oratoire : Comment réprimer l’angoisse de parler (be p. 135 § 1–p. 137 § 2)

No 1 : Comment prendre de bonnes décisions (w01 1/9 p. 27-30)

No 2 : 2 Corinthiens 8:1-21

No 3 : Que devient l’âme après la mort ?

No 4 : Des versets qui influencent l’attitude du chrétien à l’égard des guerres sanguinaires (rs p. 264 § 3–p. 265 § 3)

29 sept. Lecture de la Bible : Galates 1-6 Cantique 163

Technique oratoire : Comment gagner de l’assurance (be p. 137 § 3–p. 138 § 4)

No 1 : La grande importance des dates pivots (si p. 282-3 § 27-30)

No 2 : w01 1/9 p. 15 § 8–p. 17 § 11

No 3 : En quelles circonstances Dieu a-t-il autorisé les Israélites à s’engager dans des guerres ? (rs p. 265 § 4–p. 266 § 4)

No 4 : Comment savons-nous que le Royaume de Dieu exerce sa domination ?

6 oct. Lecture de la Bible : Éphésiens 1-6 Cantique 99

Technique oratoire : Les avantages de la sonorisation (be p. 139 § 1–p. 140 § 1)

No 1 : Les bienfaits de l’étude (be p. 31 § 3–p. 32 § 3)

No 2 : Éphésiens 2:1-22

No 3 : La foi en Dieu est fondée

No 4 : Quels textes des Écritures influencent le point de vue du chrétien sur la participation aux affaires politiques ? (rs p. 267 § 1-5)

13 oct. Lecture de la Bible : Philippiens 1–Colossiens 4

Cantique 105

Technique oratoire : Utilisez convenablement le micro (be p. 140 § 2–p. 142 § 1)

No 1 : Marchons sur ‘ le sentier de la droiture ’ (w01 15/9 p. 24-8)

No 2 : Philippiens 2:1-24

No 3 : Quels versets influencent l’attitude du chrétien à l’égard des cérémonies patriotiques ? (rs p. 268 § 1–p. 269 § 1)

No 4 : Qu’est-ce que Jéhovah demande de nous aujourd’hui ?

20 oct. Lecture de la Bible : 1 Thessaloniciens 1–2 Thessaloniciens 3 Cantique 145

Technique oratoire : Utilisation de la Bible pour répondre (be p. 143 § 1-3)

No 1 : La pensée de Jéhovah sur le temps (si p. 283-4 § 31-3)

No 2 : w01 15/10 p. 23 § 6–p. 24 § 9

No 3 : Qui va au ciel ?

No 4 : Puisque les chrétiens sont neutres, doit-on conclure qu’ils ne se préoccupent pas du bien-être de leurs semblables ? (rs p. 269 § 2)

27 oct. Lecture de la Bible : 1 Timothée 1–2 Timothée 4

Cantique 46

Technique oratoire : Comment mieux utiliser la Bible (be p. 144 § 1-4)

Révision orale

3 nov. Lecture de la Bible : Tite 1–Philémon Cantique 30

Technique oratoire : Encouragement à consulter la Bible (be p. 145-6)

No 1 : Comment effectuer des recherches à l’aide de la Bible (be p. 33 § 1–p. 35 § 2)

No 2 : Philémon 1-25

No 3 : Une vie parfaite sera-t-elle ennuyeuse ?

No 4 : Pourquoi la Traduction du monde nouveau emploie-t-elle le nom Jéhovah dans les Écritures grecques chrétiennes ? (rs p. 410 § 1-3)

10 nov. Lecture de la Bible : Hébreux 1-8 Cantique 149

Technique oratoire : L’importance de bien introduire les versets (be p. 147 § 1–p. 148 § 2)

No 1 : Hénok marchait avec Dieu au milieu d’un monde impie (w01 15/9 p. 29-31)

No 2 : Hébreux 2:1-18

No 3 : iComment répondre à ceux qui disent : ‘ Vous avez votre Bible à vous ’ (rs p. 411 § 1-4)

No 4 : En quel sens les ressuscités seront-ils jugés selon leurs actions ?

17 nov. Lecture de la Bible : Hébreux 9-13 Cantique 144

Technique oratoire : Introduisez les versets par des commentaires adaptés (be p. 148 § 3–p. 149 § 3)

No 1 : Que signifie être fidèle ? (w01 1/10 p. 20-3)

No 2 : Hébreux 9:11-28

No 3 : Les créatures célestes de Dieu sont-elles organisées ? (rs p. 270 § 2-3)

No 4 : Pourquoi une conduite marquée par l’attachement à Dieu est profitable

24 nov. Lecture de la Bible : Jacques 1-5 Cantique 88

Technique oratoire : La mise en valeur des mots clés suppose des sentiments (be p. 150 § 1-2)

No 1 :Comment situer les événements dans le cours du temps (si p. 284-5 § 1-4)

No 2 : w01 1/11 p. 12 § 15–p. 13 § 19

No 3 : La valeur de la modestie

No 4 : Comment Jéhovah transmettait-il des instructions à ses serviteurs terrestres du passé ? (rs p. 270 § 4–p. 271 § 1)

1er déc. Lecture de la Bible : 1 Pierre 1–2 Pierre 3 Cantique 54

Technique oratoire : Mettez en valeur les mots qui doivent l’être (be p. 150 § 3–p. 151 § 2)

No 1 : Apprenez à employer d’autres outils de recherche (be p. 35 § 3–p. 38 § 4)

No 2 : 1 Pierre 1:1-16

No 3 : Selon la Bible, les vrais chrétiens doivent-ils être organisés ? (rs p. 271 § 3–p. 272 § 3)

No 4 : Quelle influence le sacrifice rédempteur du Christ devrait-il avoir sur notre vie ?

8 déc. Lecture de la Bible : 1 Jean 1–Jude Cantique 22

Technique oratoire : Les différentes méthodes de mise en valeur des mots clés (be p. 151 § 3–p. 152 § 5)

No 1 : Préservez votre conscience (w01 1/11 p. 4-7)

No 2 : 1 Jean 3:1-18

No 3 : Pourquoi la Bible ne peut être tenue pour responsable du manque de respect envers les femmes

No 4 : Les fidèles serviteurs de Dieu ne sont-ils pas simplement dispersés dans les Églises de la chrétienté ? (rs p. 272 § 4–p. 273 § 2)

15 déc. Lecture de la Bible : Révélation 1-6 Cantique 219

Technique oratoire : Application exacte des versets (be p. 153 § 1–p. 154 § 3)

No 1 : La foi de Noé condamne le monde (w01 15/11 p. 28-31)

No 2 : Révélation 2:1-17

No 3 : Comment peut-on identifier la partie visible de l’organisation de Jéhovah ? (rs p. 273 § 3-9)

No 4 : Pourquoi Noël n’est pas pour les chrétiens

22 déc. Lecture de la Bible : Révélation 7-14 Cantique 6

Technique oratoire : Faites une application claire des versets (be p. 154 § 4–p. 155 § 4)

No 1 : Comment prévenir l’infarctus spirituel (w01 1/12 p. 9-13)

No 2 : w01 15/12 p. 17 § 10–p. 18 § 13 (note en bas de page incluse)

No 3 : Comment résister à l’influence de l’entourage ?

No 4 : Comment montre-t- on que l’on respecte l’organisation de Jéhovah ? (rs p. 274 § 1-5)

29 déc. Lecture de la Bible : Révélation 15-22 Cantique 60

Technique oratoire : Raisonnez à partir des Écritures (be p. 155 § 5–p. 156 § 4)

Révision orale

[Footnotes]

a Attribué uniquement à un frère.

b Attribué uniquement à un frère.

c Attribué uniquement à un frère.

d Attribué uniquement à un frère.

e Attribué uniquement à un frère.

f Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

g Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

h Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

i Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager