TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 11/02 p. 2
  • Ay yéenekaay yu am solo !

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Ay yéenekaay yu am solo !
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2002
Sasu Nguuru Yàlla — 2002
km 11/02 p. 2

Ay yéenekaay yu am solo !

Waxtaan yii di topp, ci La Tour de Garde lañu génnoon. Ndax niruwuñu lu neex ?

“ Dieu connaît et protège les siens ”

“ Faites des progrès pour dompter la langue ”

“ Le christianisme dans la clandestinité ”

“ Prêcher efficacement aux portes ”

“ Comment répondre à la question : Êtes-vous sauvé ? ”

Waxtaan yooyu ak yeneen waxtaan yu bare, génn nañu ci atum 1951 ak 1952. Li waxtaan yooyu yàgg lool, ndax mënul tax ñu bañ a amati benn njariñ tey ? Déedéet ! Dese nañu ba tey, téere bi boole La Tour de Garde yi génn ci ãgale ci atum 1951, ak bi boole yi génn ci ãgale ci atum 1952 (volumes reliés de La Tour de Garde de 1951 et de Réveillez-vous de 1952). Ku ci bëgg, mën na ci am. (Am na it ay téere yu boole La Tour de Garde yi génn ci ãgale ci diggante 1953 ba 1959.) Ci tubaab, mën nga am yi ñu génne diggante 1985 ba 2000. Waaraatekat bu bëgg téere yooyu, mën na ko wax kiy toppatoo téere yi ci mbooloo mi, ngir mu laajte leen.

Wottukatu lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla bi war na seet ndax téere yooyu bokk nañu ci téere yi ñuy def ci bibliothèque bi nekk ci Saalu Nguur gi. Bu amee bu ci nekkul, na ko laajte.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager