TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 10/05 p. 3-8
  • Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2006

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2006
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2005
  • Turu xaaj yi
  • Ni ñu koy doxale
  • PROGRAMME
Sasu Nguuru Yàlla — 2005
km 10/05 p. 3-8

Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2006

Ni ñu koy doxale

Ci atum 2006, nii lañuy doxale Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla bi :

TÉERE YI ÑUY JËFANDIKOO : Les Saintes Écritures -- Traduction du monde nouveau [bi12], La Tour de Garde [w], Tirez profit de l’École du ministère théocratique [be], “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile  ” (bu 1997) [si], et Comment raisonner à partir des Écritures (bu 1989) [rs].

WARUÑU TÀRDE. Bu waxtu bi jotee rekk, nañu tàmbali lekkool bi ak benn woy-Yàlla, ñaan te teral nit ñi, ba pare def lii :

LIY TAX ÑU AAY CI WAX (Technique oratoire) : 5 minit. Wottukatu lekkool bi, kiy koy jàpple, walla mag bu mën def lekkool bi dina jëfandikoo téere École du ministère ngir waxtaan ci lenn luy tax ñu aay ci wax. (Su ngeen barewul magu mbooloo, ay surga mbooloo yu mën jàngale mën nañu def waxtaan bii).

WAXTAAN N° 1 : 10 minit. Benn mag walla benn surga mbooloo mi moo ko war a def. Ci téere yii lañu koy defe : La Tour de Garde, Tirez profit de l’École du ministère théocratique walla “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile ”. Waare lay doon ngir jàngal ñi teew ci 10 minit. Bu paree waxtaanam, warul a laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li mu wax. Ki koy def dafa war a wax li nekk ci xët yi ñuy jagleel waxtaan bi. War na fexe it ba nit ñi gis bu baax njariñ bi nekk ci li ñu wax ci xët yooyu. Te it, war na wone bu baax li gën a am njariñ ci mbooloo mi. Waxtaan bi jox nañu ko tur (thème) ba pare. Tur boobu lañu war a jëfandikoo. Waxtaan bi warul a weesu 10 minit. Bu ñu waree xelal ki def waxtaan bi, kiy jiite lekkool bi na wéet ak moom.

KÀDDU YU AM SOLO CI LI ÑU WAROON A JÀNG CI BIIBËL BI : 10 minit. Ci juróomi minit yi njëkk yi, mag walla surga mbooloo bu mën jàngale, war na wone ni mbooloo mi mënee jariñoo xaaju Biibël bi ñu waroon a jàng ci ayu-bés bi. Mën na wax ci aaya bu mu mënta doon bu bokk ci xaaj boobu. Kiy def waxtaan bi, warul yem rekk ci tënk pàcc yi ñu war a jàng, waaye war na wone lu tax li ci nekk am njariñ ak it naka lañu ko mënee jariñoo. Kiy jiite waxtaan bii, war na fexe ba bañ a wax lu ëpp juróomi minit. Te fàww mu may ñi teew juróomi minit ngir ñu wax yan aaya ñoo leen neex, te lu tax aaya yooyu am solo. Seen tont dafa war a gàtt (warul weesu 30 segoond). Bu ñu paree, kiy jiite lekkool bi dina wax ñi war a dem ci yeneen kalaas yi ñu dem fa.

WAXTAAN N° 2 : Warul weesu 4 minit. Suñu benn mbokk mu góor moo ko war a def. Dafa war a jàng rekk li ñu koy wax. Warul wax dara balaa muy jàng, te bu jàngee ba pare, warul wax dara itam. Su waree jàng dara ci Sabuur, war na jàng itam mbind yu ndaw yi nekk ci kow yenn pàcc. Wottukatu lekkool bi war na seet bu baax ni mu mënee dimbali kiy jàng ci lii : buy jàng, ñu xam ne nànd na li muy jàng ; njàng mi yomb ci moom (fluidité) ; mu bañ a juum ci ni muy waxe baat yi te kàddu yi ëpp solo feeñ bu baax ; li ñuy woowe modulation ; buy jàng, mu taxaw fi mu war a taxaw ; te wax ni muy waxe bés bu nekk.

WAXTAAN N° 3 : 5 minit. Suñu benn mbokk mu jigéen moo ko war a def. Dinañu ko jox benn cadre (maanaam ni waxtaan bi di ame) ci yi nekk ci téere École du ministère ci xët 82. Bu ñu ko joxul cadre, na ko tànnal boppam. Na topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi te na mel ni kuy waaraate. Na waxtaan bi niroo ak lu mën a am dëgg ci seen goxu mbooloo te mën a jariñ waaraatekat yi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def na wutal boppam li muy wax ci suñu téere yi. Ñi yàggul a bokk ci lekkool bi, nañu leen jox waxtaan boo xam ne wax nañu yan téere la war a jëfandikoo. Wottukatu lekkool bi dina seetlu bu baax ni waxtaan bi di demee ak ni mbokk mu koy def di dimbalee ki muy jàngal ba mu mën a xalaat ci li nekk ci mbind mi te nànd li ëpp solo ci waxtaan bi. Wottukatu lekkool bi dina ko wax ak kan la war a def waxtaan bi.

WAXTAAN N° 4 : 5 minit. Ki koy def dafa war a topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def moo war a wutal boppam li muy wax ci suñu téere yi. Bu fekkee ne mbokk mu góor moo ko war a def, waare lay doon, te bu koy def dina bàyyi xel ci ñi koy déglu. Bu dee mbokk mu jigéen moo koy def, na ko def ni ñuy defe Waxtaan n° 3. Kiy jiite lekkool bi, bu gisee ne góor mën na def Waxtaan n° 4 bi, mën na ko jox suñu benn mbokk mu góor. Bu leen fàtte ne waxtaan yi ànd ak biddéew bu ndaw, mbokk mu góor kese moo leen war a def te dafay nekk waare.

WAXTU WI : Waxtaan yi ak xelal yi, waruñu yàgg ba weesu waxtu bi ñu leen jagleel. Ñiy def Waxtaan n° 2, 3, ak 4, bu ñu weesoo waxtu bi ñu leen may, nañu seet fasoŋ bu rafet bu ñu mënee dog seen waxtaan. Kiy def waxtaan biy ubbi lekkool bi te jëm ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire), kiy def Waxtaan n° 1, walla kiy wax kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi, bu ci amee ku waxtaanam yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may, war nañu wéet ak moom ngir xelal ko. Képp kuy def waxtaan war na seetlu bu baax waxtu bi ngir waxtaanam bañ a yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may. Lekkool bi 45 minit la war a def. Loolu boolewuñu ci ñaan bi ak woy-Yàlla bi.

XELAL YI : 1 minit. Bu kenn paree waxtaanam, wottukatu lekkool bi dina wax ci lu baax li mu def ci waxtaan bi. Loolu warul weesu benn minit. Du ko wax rekk ne “ sa waxtaan baaxoon na ”, waaye dina wax lenn ci li tax waxtaanam baax.

KIY JÀPPLE KIY XELAL NIT ÑI : Ginnaaw wottukatu lekkool bi, bu amee beneen mag ci mbooloo mi bu mën a jiite lekkool bi, kurélu mag ñi dinañu ko tànn ngir mu jàpple kiy xelal nit ñi. Bu fekkee ne magi mbooloo mi xaw nañu bare, kon, mën nañu tànn at mu nekk beneen mag bu mën xelal ngir mu jàpple kiy xelal nit ñi. Kooku dina xelal ñiy def Waxtaan n° 1 ak kiy wax kàddu yu am solo ci Biibël bi, bu ñu ko soxlaa. Du saa yu mag walla surga mbooloo mi di def waxtaan yooyu, la koy war a xelal.

KAYIT FI ÑU BIND XELAL YI : Mu ngi ci téere École du ministère.

WAXTAAN AK ÑI TEEW NGIR FÀTTALIKU LI ÑU JÀNG CI LEKKOOL BI (Révision orale) : 30 minit. Ñaari weer yu nekk, wottukatu lekkool bi dina laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi. Dinañu njëkk wax ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire) ak it kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi (nañu topp tegtal yi nekk ci kow ngir waxtaan yooyu), ba pare ñu waxtaan ak ñi teew ngir fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi ci ñaari weer yi weesu, boole ci li ñu def ci ayu-bés bi. Seen ndaje bu mag bu ñaari fan mën na tombe ci ayu-bés bu ñu war a fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi. Su loolu amee, nangeen def li ngeen waroon a def ayu-bés bi ci topp. Te ayu-bés boobu dingeen topp porogaraamu ayu-bés bi ñu war a fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi. Su wottukat biy wër waree ñów ci ayu-bés bu ñu war a fàttaliku li ñu def ci lekkool bi, dinañu woy woy-Yàlla bi, def “ Liy tax ñu aay ci wax ” ak it “ Kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi ”. Waxtaan n° 1 bu ñuy def (maanaam bi nar a topp ci waxtaan bi tudd “ Liy tax ñu aay ci wax ), mooy nekk bi ñu naroon a def ayu-bés bi ci topp. Ayu-bés bi ci topp nag, dinañu def waxtaan bi tudd “ Liy tax ñu aay ci wax ” ak bi tudd “ Kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi ” ni ko porogaraam bi waxe, ba pare dinañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi.

PROGRAMME

2 janv. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 29-32 Cantique 91

Technique oratoire : Profitez au maximum de l’École du ministère théocratique (be p. 5 § 1–p. 8 § 1)

No 1 : Prenez plaisir dans la Parole de Dieu (be p. 9 § 1–p. 10 § 1)

No 2 : 2 Chroniques 30:1-12

No 3 : Pourquoi les vrais chrétiens s’abstiennent de dire des grossièretés

No 4 : L’effet du péché sur nos relations avec Dieu (rs p. 281 § 3–p. 282 § 3)

9 janv. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 33-36 Cantique 144

Technique oratoire : Lecture précise (be p. 83 § 1-5)

No 1 : 2 Chroniques : utilité (si p. 85 § 34- 6)

No 2 : 2 Chroniques 34:1-11

No 3 : Ce que dit la Bible au sujet de l’âme (rs p. 28 § 1-5)

No 4 : N’ayez jamais honte de respecter les normes morales de la Bible

16 janv. Lecture de la Bible : Ezra 1-5 Cantique 137

Technique oratoire : Comment faire une lecture précise (be p. 84 § 1–p. 85 § 3)

No 1 : Ezra : introduction (si p. 85- 6 § 1-7)

No 2 : Ezra 1:1-11

No 3 : Les bienfaits d’une conscience droite

No 4 : Les animaux sont des âmes (rs p. 28 § 6–p. 29 § 5)

23 janv. Lecture de la Bible : Ezra 6-10 Cantique 106

Technique oratoire : Bonne élocution (be p. 86 § 1- 6)

No 1 : Ezra : utilité (si p. 87-8 § 14-18)

No 2 : Ezra 6:1-12

No 3 : À la mort, ni l’âme ni l’esprit ne continuent d’exister (rs p. 30 § 1–p. 32 § 1)

No 4 : aLe point de vue de Dieu sur le mariage

30 janv. Lecture de la Bible : Nehémia 1-4 Cantique 161

Technique oratoire : Comment s’exprimer nettement (be p. 87 § 1–p. 88 § 3)

No 1 : Nehémia : introduction (si p. 88-9 § 1-5)

No 2 : Nehémia 2:1-10

No 3 : La sécurité la plus importante

No 4 : Ce qu’est l’esprit saint (rs p. 136 § 1-3)

6 févr. Lecture de la Bible : Nehémia 5-8 Cantique 40

Technique oratoire : Prononciation correcte : facteurs à considérer (be p. 89 § 1–p. 90 § 3)

No 1 : Lisez la Bible chaque jour (be p. 10 § 2–p. 12 § 3)

No 2 : Nehémia 5:1-13

No 3 : Ce qui prouve qu’une personne est remplie d’esprit saint (rs p. 137 § 1-4)

No 4 : “ Préserve ton cœur ” (Prov. 4:23)

13 févr. Lecture de la Bible : Nehémia 9 -11 Cantique 159

Technique oratoire : Des conseils pour améliorer votre prononciation (be p. 90 § 4–p. 92)

No 1 : Apprendre la paix au lieu de la guerre (w04 1/1 p. 6 § 8–p. 7 § 5)

No 2 : Nehémia 10:28-37

No 3 : Ce qui prouve que Jéhovah nous aime

No 4 : Aucun élément spirituel ne survit à la mort du corps (rs p. 138 § 4–p. 139 § 1)

20 févr. Lecture de la Bible : Nehémia 12-13 Cantique 118

Technique oratoire : Fluidité de l’expression (be p. 93 § 1–p. 94 § 3)

No 1 : Nehémia : utilité (si p. 91 § 16-19)

No 2 : Nehémia 13:1-14

No 3 : Pourquoi il est impossible de communiquer avec les morts (rs p. 381 § 4–p. 382 § 4)

No 4 : bLes jeux vidéo violents ne sont pas pour les chrétiens

27 févr. Lecture de la Bible : Esther 1-5 Cantique 215

Technique oratoire : Des conseils pour progresser en fluidité (be p. 94 § 4–p. 96 § 3, sauf l’encadré p. 95)

Révision orale

6 mars Lecture de la Bible : Esther 6-10 Cantique 74

Technique oratoire : Comment maîtriser le bégaiement (be p. 95, encadré)

No 1 : Esther : introduction et utilité (si p. 92-5 § 1- 6, 16-18)

No 2 : Esther 6:1-10

No 3 : Une réponse douce peut détourner la fureur

No 4 : Pourquoi les vrais chrétiens rejettent toutes les pratiques spirites (rs p. 382 § 5–p. 384 § 3)

13 mars Lecture de la Bible : Job 1-5 Cantique 160

Technique oratoire : Pauses pour ponctuer ou marquer une transition (be p. 97 § 1–p. 98 § 5)

No 1 : Job : introduction (si p. 95- 6 § 1- 6)

No 2 : Job 2:1-13

No 3 : Ne soyez pas curieux des pouvoirs démoniaques (rs p. 384 § 4–p. 385 § 2)

No 4 : Pourquoi les vrais chrétiens s’abstiennent de murmurer

20 mars Lecture de la Bible : Job 6-10 Cantique 214

Technique oratoire : Pauses pour accentuer, pauses pour écouter (be p. 99 § 1–p. 100 § 4)

No 1 : La supériorité des valeurs spirituelles (w04 15/10 p. 4 § 2–p. 5 § 3)

No 2 : Job 7:1-21

No 3 : Ce que signifie avoir le cœur pur

No 4 : Comment s’affranchir de l’influence des esprits (rs p. 385 § 3–p. 386 § 4)

27 mars Lecture de la Bible : Job 11-15 Cantique 8

Technique oratoire : Accentuation des mots clés (be p. 101 § 1–p. 102 § 3)

No 1 : ‘ Faites attention à la manière dont vous écoutez ’ (be p. 13 § 1–p. 14 § 5)

No 2 : Job 12:1-25

No 3 : Rejetez l’esprit d’indépendance (rs p. 140 § 1–p. 141 § 2)

No 4 : Pourquoi le ministère nous procure de la joie

3 avril Lecture de la Bible : Job 16-20 Cantique 50

Technique oratoire : Des conseils pour mieux accentuer les mots clés (be p. 102 § 4–p. 104 § 2)

No 1 : Comment nous démontrons notre amour pour Dieu (w04 1/3 p. 19 -21)

No 2 : Job 16:1-22

No 3 : Comment Jéhovah attire des gens pour l’adorer

No 4 : cLes dangers de l’orgueil et des comportements rebelles (rs p. 141 § 3–p. 142 § 1)

10 avril Lecture de la Bible : Job 21-27 Cantique 119

Technique oratoire : Mise en valeur des idées essentielles (be p. 105 § 1–p. 106 § 2)

No 1 : Les valeurs spirituelles procurent des bienfaits (w04 15/10 p. 5 § 4–p. 7 § 2)

No 2 : Job 24:1-20

No 3 : Jéhovah donne la puissance qui passe la normale

No 4 : dMéfiez-vous des désirs de la chair (rs p. 142 § 2)

17 avril Lecture de la Bible : Job 28-32 Cantique 100

Technique oratoire : Volume adapté à l’auditoire (be p. 107 § 1–p. 108 § 5)

No 1 : Comment écouter aux réunions et aux assemblées (be p. 15 § 1–p. 16 § 5)

No 2 : Job 29:1-25

No 3 : Ne vous laissez pas dominer par le désir des yeux (rs p. 142 § 3-4)

No 4 : Pourquoi les foules étaient frappées de la manière d’enseigner de Jésus

24 avril Lecture de la Bible : Job 33-37 Cantique 94

Technique oratoire : Comment améliorer le volume de votre voix (be p. 108 § 6–p. 110 § 2)

Révision orale

1er mai Lecture de la Bible : Job 38-42 Cantique 154

Technique oratoire : Modulation : adaptez le volume de votre voix (be p. 111 § 1–p. 112 § 2)

No 1 : Job : utilité (si p. 100 -1 § 39 -43)

No 2 : Job 38:1-24

No 3 : Comment Isaïe 60:22 se réalise-t-il de nos jours ?

No 4 : eLe langage grossier et la violence sont des œuvres de la chair (rs p. 143 § 1)

8 mai Lecture de la Bible : Psaumes 1-10 Cantique 168

Technique oratoire : Modulation : changez de débit (be p. 112 § 3–p. 113 § 1)

No 1 : Psaumes : introduction — 1re partie (si p. 101-2 § 1-5)

No 2 : Psaume 4:1–5:12

No 3 : Mettez votre confiance en Dieu, non en l’homme (rs p. 143 § 2-3)

No 4 : Retenons le modèle des paroles salutaires

15 mai Lecture de la Bible : Psaumes 11-18 Cantique 217

Technique oratoire : Modulation : variez votre ton (be p. 113 § 2–p. 114 § 3)

No 1 : Psaumes : introduction — 2e partie (si p. 102-3 § 6-11)

No 2 : Psaume 14:1–16:6

No 3 : En quels sens les vrais chrétiens ne font-ils pas partie du monde ?

No 4 : Qui est responsable de la souffrance humaine ? (rs p. 375 § 1-2)

22 mai Lecture de la Bible : Psaumes 19 -25 Cantique 23

Technique oratoire : Parlez avec sentiment (be p. 115 § 1–p. 116 § 4)

No 1 : Bonne perspicacité obtient faveur (w04 15/7 p. 27 § 4–p. 28 § 4)

No 2 : Psaume 22:1-22

No 3 : D’où vient la souffrance ? (rs p. 375 § 3-4)

No 4 : fQue sont les rappels de Dieu, et pourquoi devons-nous en tenir compte ?

29 mai Lecture de la Bible : Psaumes 26-33 Cantique 203

Technique oratoire : Enthousiasme approprié aux idées (be p. 116 § 5–p. 117 § 4)

No 1 : Une mémoire plus performante (be p. 17 § 1–p. 19 § 1)

No 2 : Psaume 30:1–31:8

No 3 : De quelles façons la vérité nous libère-t- elle ?

No 4 : Comment nous pouvons nous éviter bien des souffrances (rs p. 376 § 1-2)

5 juin Lecture de la Bible : Psaumes 34-37 Cantique 167

Technique oratoire : Exprimez de la chaleur (be p. 118 § 1–p. 119 § 5)

No 1 : Le pouvoir de la prière (w04 15/8 p. 18 § 6–p. 19 § 10)

No 2 : Psaume 34:1-22

No 3 : Pourquoi un Dieu d’amour permet-il la souffrance depuis si longtemps ? (rs p. 376 § 4)

No 4 : Fuyons l’idolâtrie sous toutes ses formes

12 juin Lecture de la Bible : Psaumes 38-44 Cantique 216

Technique oratoire : Exprimez des sentiments (be p. 119 § 6–p. 120 § 5)

No 1 : Comment l’esprit de Dieu vient en aide à notre mémoire (be p. 19 § 2–p. 20 § 3)

No 2 : Psaume 40:1-17

No 3 : La vraie science ne contredit pas la Bible

No 4 : Dieu effacera toute trace des malheurs que subissent ses serviteurs (rs p. 377 § 1-4)

19 juin Lecture de la Bible : Psaumes 45-51 Cantique 104

Technique oratoire : L’importance des gestes et des expressions du visage (be p. 121 § 1-4)

No 1 : Quand Jésus vient-il ? (w04 1/3 p. 16, encadré)

No 2 : Psaume 46:1–47:9

No 3 : Pourquoi Dieu n’a-​t-⁠il pas tout simplement fermé les yeux sur le péché d’Adam ? (rs p. 377 § 5–p. 378 § 1)

No 4 : En quel sens un chrétien peut-il être à la fois faible et puissant ? (2 Cor. 12:10)

26 juin Lecture de la Bible : Psaumes 52-59 Cantique 103

Technique oratoire : Le recours aux gestes et aux expressions du visage (be p. 121 § 5–p. 123 § 2)

Révision orale

3 juillet Lecture de la Bible : Psaumes 60 - 68 Cantique 45

Technique oratoire : Le contact visuel dans le ministère (be p. 124 § 1–p. 125 § 3)

No 1 : L’humilité de Jéhovah nous est bénéfique (w04 1/11 p. 29 -30)

No 2 : Psaume 60:1–61:8

No 3 : Le fait de prendre part à des activités chrétiennes nous dispense-t-il d’obéir aux lois de Dieu ?

No 4 : Dieu n’est pas responsable des tares physiques ou mentales (rs p. 378 § 2-4)

10 juillet Lecture de la Bible : Psaumes 69 -73 Cantique 225

Technique oratoire : Le contact visuel quand vous donnez un discours (be p. 125 § 4–p. 126 § 6)

No 1 : Pourquoi s’appliquer à la lecture ? (be p. 21 § 1–p. 23 § 3)

No 2 : Psaume 71:1-18

No 3 : Avec amour, Jéhovah permet que les bienfaits du sacrifice de Jésus soient également appliqués aux enfants (rs p. 378 § 5)

No 4 : gPourquoi les chrétiens doivent être impartiaux

17 juillet Lecture de la Bible : Psaumes 74-78 Cantique 28

Technique oratoire : Le naturel dans le ministère (be p. 128 § 1–p. 129 § 1)

No 1 : Lisez avec de bons mobiles (be p. 23 § 4–p. 26 § 5)

No 2 : Psaume 75:1–76:12

No 3 : Qu’implique le fait de chercher Jéhovah ? (Tseph. 2:3)

No 4 : Dieu ne punit pas les gens au moyen des catastrophes naturelles (rs p. 379 § 1-3)

24 juillet Lecture de la Bible : Psaumes 79 -86 Cantique 112

Technique oratoire : Le naturel sur l’estrade (be p. 129 § 2–p. 130 § 1)

No 1 :  “ La tente des hommes droits sera florissante ” (w04 15/11 p. 26 § 1–p. 28 § 2)

No 2 : Psaume 82:1–83:18

No 3 : Les malheurs ne sont pas le signe de la défaveur de Dieu (rs p. 380 § 1-2)

No 4 : Des humains imparfaits peuvent-ils vraiment plaire à Dieu ?

31 juillet Lecture de la Bible : Psaumes 87-91 Cantique 57

Technique oratoire : Le naturel lors d’une lecture publique (be p. 130 § 2-4)

No 1 : Lorsque “ la connaissance est chose facile ” et que la sagesse nous guide (w04 15/11 p. 28 § 3–p. 29 § 7)

No 2 : Psaume 89:1-21

No 3 : L’étude de la Bible fait partie de notre culte

No 4 : La prospérité matérielle n’est pas le signe de la bénédiction de Dieu (rs p. 380 § 3-4)

7 août Lecture de la Bible : Psaumes 92-101 Cantique 190

Technique oratoire : Notre hygiène corporelle pare notre message (be p. 131 § 1-3)

No 1 : Comment étudier (be p. 27 § 1–p. 31 § 2)

No 2 : Psaume 92:1–93:5

No 3 : Le fait de parler en langues indique-t-il que l’on a l’esprit de Dieu ? (rs p. 219 § 3–p. 220 § 3)

No 4 : L’importance de l’intégrité morale

14 août Lecture de la Bible : Psaumes 102-105 Cantique 1

Technique oratoire : Comment la modestie et le bon sens influent sur notre habillement et notre coiffure (be p. 131 § 4–p. 132 § 3)

No 1 : “ Que tes œuvres sont nombreuses, ô Jéhovah ! ” (w04 15/11 p. 8-9)

No 2 : Psaume 104:1-24

No 3 : Pourquoi nous devons veiller

No 4 : En quoi le don des langues aujourd’hui diffère-t-il de celui qu’avaient reçu les chrétiens du I er siècle ? (rs p. 220 § 4–p. 221 § 2)

21 août Lecture de la Bible : Psaumes 106-109 Cantique 201

Technique oratoire : La valeur d’une tenue bien arrangée (be p. 132 § 4- 6)

No 1 : Jeunes : ne suivez pas aveuglément vos camarades (w04 15/10 p. 22 § 4–p. 24 § 5)

No 2 : Psaume 107:20 -43

No 3 : La Parole de Dieu nous aide à analyser les déclarations de ceux qui disent avoir l’esprit de Dieu (rs p. 221 § 4–p. 222 § 1)

No 4 : De quelles façons pouvons-nous imiter Dieu ?

28 août Lecture de la Bible : Psaumes 110 -118 Cantique 125

Technique oratoire : Un aspect soigné pour ne pas faire trébucher (be p. 133 § 1-3)

Révision orale

4 sept. Lecture de la Bible : Psaume 119 Cantique 59

Technique oratoire : Un bon maintien et des accessoires nets (be p. 133 § 4–p. 134 § 4)

No 1 : Les bienfaits de l’étude (be p. 31 § 3–p. 32 § 3)

No 2 : Psaume 119:25-48

No 3 : Pourquoi nous respectons les autorités

No 4 : Le don des langues n’est pas la marque d’identification des vrais chrétiens (rs p. 222 § 2-4)

11 sept. Lecture de la Bible : Psaumes 120 -134 Cantique 65

Technique oratoire : Comment réprimer l’angoisse de parler (be p. 135 § 1–p. 137 § 2)

No 1 : Comment effectuer des recherches (be p. 33 § 1–p. 35 § 2)

No 2 : Psaume 121:1–123:4

No 3 : Combien de temps le don des langues devait-il durer ? (rs p. 222 § 5–p. 223 § 1)

No 4 : Qu’est- ce que l’hyperbole, et quel usage Jésus en a-​t-⁠il fait ?

18 sept. Lecture de la Bible : Psaumes 135-141 Cantique 97

Technique oratoire : Comment gagner de l’assurance (be p. 137 § 3–p. 138 § 4)

No 1 : Psaumes : utilité — 1re partie (si p. 105- 6 § 23-7)

No 2 : Psaume 136:1-26

No 3 : En quel sens le Mémorial est-il un repas de communion ?

No 4 : hLa Trinité n’est pas fondée sur la Bible (rs p. 412 § 1–p. 418 § 3)

25 sept. Lecture de la Bible : Psaumes 142-150 Cantique 5

Technique oratoire : Les avantages de la sonorisation (be p. 139 § 1–p. 140 § 1)

No 1 : Psaumes : utilité — 2e partie (si p. 106 § 28-32)

No 2 : Psaume 142:1–143:12

No 3 : iSi quelqu’un vous demande : ‘ Croyez-vous à la Trinité ? ’ (rs p. 432 § 2–p. 433 § 4)

No 4 : De quelles façons pouvons-nous faire passer les besoins des autres avant les nôtres ?

2 oct. Lecture de la Bible : Proverbes 1- 6 Cantique 111

Technique oratoire : Utilisez convenablement le micro (be p. 140 § 2–p. 142 § 1)

No 1 : Proverbes : introduction — 1re partie (si p. 107 § 1-5)

No 2 : Proverbes 5:1-23

No 3 : Pourquoi y a-​t-⁠il tant de méchanceté sur la terre ? (rs p. 237 § 2–p. 238 § 1)

No 4 : jNe répandez pas de fables (2 Tim. 4:4)

9 oct. Lecture de la Bible : Proverbes 7-11 Cantique 73

Technique oratoire : Utilisation de la Bible pour répondre (be p. 143 § 1-3)

No 1 : Proverbes : introduction — 2e partie (si p. 107-8 § 6-11)

No 2 : Proverbes 7:1-27

No 3 : La neutralité chrétienne contribue à notre unité et à notre fraternité

No 4 : Pourquoi Dieu permet-il la méchanceté ? (rs p. 238 § 2–p. 239 § 2)

16 oct. Lecture de la Bible : Proverbes 12-16 Cantique 180

Technique oratoire : Comment mieux utiliser la Bible (be p. 144 § 1-4)

No 1 : Apprenez à employer d’autres outils de recherche (be p. 35 § 3–p. 38 § 4)

No 2 : Proverbes 14:1-21

No 3 : Quels bienfaits retirons-nous du fait que Dieu permette la méchanceté ? (rs p. 240 § 1-2)

No 4 : Qu’est- ce qui peut nous aider à être bien attentifs lors des réunions ?

23 oct. Lecture de la Bible : Proverbes 17-21 Cantique 131

Technique oratoire : Encouragement à consulter la Bible (be p. 145- 6)

No 1 : Proverbes : utilité — 1re partie (si p. 110 -11 § 19 -28)

No 2 : Proverbes 17:1-20

No 3 : Le point de vue des chrétiens sur les personnes âgées

No 4 : kQuel point de vue sur les femmes la Bible encourage-t-elle ? (rs p. 157 § 2-3)

30 oct. Lecture de la Bible : Proverbes 22-26 Cantique 9

Technique oratoire : L’importance de bien introduire les versets (be p. 147 § 1–p. 148 § 2)

Révision orale

6 nov. Lecture de la Bible : Proverbes 27-31 Cantique 51

Technique oratoire : Introduisez les versets par des commentaires adaptés (be p. 148 § 3–p. 149 § 3)

No 1 : Proverbes : utilité — 2e partie (si p. 111-12 § 29 -38)

No 2 : Proverbes 28:1-18

No 3 : La femme est- elle rabaissée du fait que l’homme a autorité sur elle ? (rs p. 157 § 4–p. 158 § 2)

No 4 : Pourquoi ne pas juger d’après les apparences ceux que nous rencontrons quand nous prêchons

13 nov. Lecture de la Bible : Ecclésiaste 1- 6 Cantique 25

Technique oratoire : La mise en valeur des mots clés suppose des sentiments (be p. 150 § 1-2)

No 1 : Ecclésiaste : introduction (si p. 112-13 § 1-8)

No 2 : Ecclésiaste 5:1-15

No 3 : Comment les vérités bibliques sont- elles cachées aux sages et aux intellectuels ? (Mat. 11:25)

No 4 : Les femmes peuvent- elles être ministres ? (rs p. 158 § 3–p. 159 § 1)

20 nov. Lecture de la Bible : Ecclésiaste 7-12 Cantique 37

Technique oratoire : Mettez en valeur les mots qui doivent l’être (be p. 150 § 3–p. 151 § 2)

No 1 : Ecclésiaste : utilité (si p. 114-15 § 15-19)

No 2 : Ecclésiaste 9:1-12

No 3 : Pour quelles raisons les chrétiennes se couvrent- elles la tête en certaines occasions ? (rs p. 159 § 2–p. 160 § 1)

No 4 : Qu’y a-​t-⁠il de mal à être jaloux ?

27 nov. Lecture de la Bible : Chant de Salomon 1-8 Cantique 11

Technique oratoire : Les différentes méthodes de mise en valeur des mots clés (be p. 151 § 3–p. 152 § 5)

No 1 : Chant de Salomon : introduction et utilité (si p. 115-17 § 1-4, 16-18)

No 2 : Chant de Salomon 7:1–8:4

No 3 : Pourquoi les chrétiens doivent-ils porter des vêtements nets, propres et modestes ?

No 4 : Est-il convenable qu’une femme se maquille ou qu’elle porte des bijoux ? (rs p. 161 § 1-3)

4 déc. Lecture de la Bible : Isaïe 1-5 Cantique 90

Technique oratoire : Application exacte des versets (be p. 153 § 1–p. 154 § 3)

No 1 : Isaïe : introduction (si p. 118-19 § 1-8)

No 2 : Isaïe 3:1-15

No 3 : Le monde sera-​t-⁠il détruit par le feu ? (rs p. 250 § 1-2)

No 4 : lPourquoi les chrétiens doivent être ‘ lents à la colère ’ (Jacq. 1:19)

11 déc. Lecture de la Bible : Isaïe 6-10 Cantique 204

Technique oratoire : Faites une application claire des versets (be p. 154 § 4–p. 155 § 4)

No 1 : Comment préparer le plan d’un exposé (be p. 39 -42)

No 2 : Isaïe 10:1-14

No 3 : Pourquoi est-il important de savoir pardonner ?

No 4 : Qui dirige le monde actuel : Dieu ou Satan ? (rs p. 250 § 3–p. 251 § 3)

18 déc. Lecture de la Bible : Isaïe 11-16 Cantique 47

Technique oratoire : Raisonnez à partir des Écritures (be p. 155 § 5–p. 156 § 4)

No 1 : Jeunes : laissez vos parents vous aider à garder votre cœur (w04 15/10 p. 20 § 1–p. 22 § 3)

No 2 : Isaïe 11:1-12

No 3 : Comment les vrais chrétiens considèrent-ils le monde et ceux qui en font partie ? (rs p. 251 § 4–p. 252 § 4)

No 4 : Les vrais chrétiens ne participeront pas à la guerre d’Har-Maguédôn

25 déc. Lecture de la Bible : Isaïe 17-23 Cantique 53

Technique oratoire : Valeur pratique mise en évidence (be p. 157 § 1-5)

Révision orale

[Li ñu bind ci suuf]

a Attribué uniquement à un frère.

b Attribué uniquement à un frère.

c Attribué uniquement à un frère.

d Attribué uniquement à un frère.

e Attribué uniquement à un frère.

f Attribué uniquement à un frère.

g Attribué uniquement à un frère.

h Dans la source indiquée, choisis quelques points clés qui correspondent le mieux aux besoins du territoire.

i Dans la source indiquée, choisis quelques points clés qui correspondent le mieux aux besoins du territoire.

j Attribué uniquement à un frère.

k Attribué uniquement à un frère.

l Attribué uniquement à un frère.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager