Oktoobar Nañu kontine di wax Kàddu Yàlla ak fit wu dëgër Wonal sa moroom ne danga ko bëgg — nanga baax ak moom Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de juin Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ci atum 2006 Nañu màggal Yexowa ci diggu mbooloo mu réy mi Yégle yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Nañu fexe ba nit ñi bëgg yokk li ñu xam ci Biibël bi, bu ñuy faral di leen indil suñu yéenekaay yi Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi