TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 2/08 p. 7
  • Yégle Yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Yégle Yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2008
Sasu Nguuru Yàlla — 2008
km 2/08 p. 7

Yégle Yi

◼ Téere yi ñuy wone ci wéeru feewriyee : Téere Y a-t-il un créateur qui se soucie de vous ? walla téere Le secret du bonheur familial. Màrs : Téere Qu’enseigne réellement la Bible ? Nañu góor-góorlu ngir komaase ay njàngum Biibël. Awril ak me : La Tour de Garde ak Réveillez-vous ! Dinañu góor-góorlu ngir seeti ñi suñu waxtaan neex te tàmmuñu teewe suñu ndaje yépp, fekk teewe woon nañu ndaje fàttaliku bi ak waxtaan bi ñu faral di am ci àddina si sépp bu ndaje fàttaliku bi weesoo. Li waral ñuy dellu seeti nit ñooñu, mooy bëgg komaase njàngum Biibël ak ñoom.

◼ Weeru màrs dina am juróomi samdi ak juróomi dimaas. Kon dina baax lool ci ku bëgg nekk pioñee buy jàpple.

◼ Sekkerteer bi ak wottukatu liggéeyu waare, war nañu seet liggéeyu pioñee yi ci sax. Bu ci amee ñu am jafe-jafe ngir matal waxtu yi ñu war a def, njiiti mbooloo mi dinañu seet naka lañu leen mënee dimbali.

◼ Ci atum 2008, waxtaan bi ñu faral di def ci àddina si sépp, bu ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu weesoo, dina tudd “ Qui est qualifié pour diriger l’humanité ” maanaam kan moo mën a jiite doomu Aadama yi ? Seetleen yégle bu ciy wax ci Sasu Nguuru Yàlla bu oktoobar 2007.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager