Feewriyee Li ñu warul a fàtte ci Ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu Nañu fàttaliku njot gi te wone ci ne fonk nañu ko lool Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li Ñu Def Ci Liggéeyu Waare Bi Ci Weeru Oktoobar Yégle Yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Lii, ngëm lay wone ! Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi