Leneen lu jëm ci loolu ll xaaj 4 p. 10-11 Ndegam Aadama ak Awa dañu déglu Seytaane — loolu lan la jur ? Naka la dund bi meloon ci toolu Eden ba ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Xaaj 4 Déggleen li Yàlla wax Fan la ñi dee nekk ? Lan la Biibël bi wax dëgg-dëgg ? Léegi àddina bi metti na Ay nettali yu nekk ci Biibël bi Lu tax nit di dee ? Dundleen ba fàww ak bànneex ci suuf si !