TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • sjj woy 103
  • Sàmm yi, ay mayu Yàlla lañu

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Sàmm yi, ay mayu Yàlla lañu
  • Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Dundal dëgg gi
    Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
  • Mbëggeelu Yaa, gi takku
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Yal na seen ngëm dëgër
    Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
  • Aywa, yéen ndawiy Nguur gi!
    Woyal, di Tagg Yeowa
Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
sjj woy 103

WOY-YÀLLA 103

Sàmm yi, ay mayu Yàlla lañu

(Efes 4:8)

  1. 1. Yàlla teg na ci biir mbooloo mi,

    Ay mag yu baax ci moom.

    Nañu leen roy ci suñu dundin,

    Ndax loolu moo ñuy aar.

    (AWU BI)

    Mag yi ñu Yàlla may ñoo ñuy sàmm,

    Ñoom dañuy aar mbooloo mi.

    Fonk nañ leen ndax seen cawarte.

    Takku nañu ci Yàlla.

  2. 2. Bu ñu nekkee ci tiis yu bare,

    Mag yi dañ ñuy déglu.

    Dañuy ubbi Kàddu Yexowa

    Ngir dalal suñu xel.

    (AWU BI)

    Mag yi ñu Yàlla may ñoo ñuy sàmm,

    Ñoom dañuy aar mbooloo mi.

    Fonk nañ leen ndax seen cawarte.

    Takku nañu ci Yàlla.

  3. 3. Mag yee ngi wéy di ñu bàyyi xel,

    Di sóoraale ëllëg.

    Bu ñu bëggee jege Yexowa,

    Nañu leen di déggal.

    (AWU BI)

    Mag yi ñu Yàlla may ñoo ñuy sàmm,

    Ñoom dañuy aar mbooloo mi.

    Fonk nañ leen ndax seen cawarte.

    Takku nañu ci Yàlla.

(Xoolal itam Esayi 32:1, 2; Yeremi 3:15; Yowaana 21:15-17; Jëf ya 20:28.)

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager