TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • sjj woy 93
  • Yal na Yàlla barkeel suñuy ndaje

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Yal na Yàlla barkeel suñuy ndaje
  • Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Ngërëm ci mën-muñu Yàlla
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Nañu màggal suñu Yàlla, Buur bi
    Woyal, di Tagg Yeowa
  • Ban njariñ nga mën a jële ci teewe ndaje Seede Yexowa yi?
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Téereb Yàlla—Alal bu dul jeex
    Woyal, di Tagg Yeowa
Xóotalal waxtaan bi
Nañu woyal Yexowa ànd ceek mbégte
sjj woy 93

WOY-YÀLLA 93

Yal na Yàlla barkeel suñuy ndaje

(Yawut ya 10:24, 25)

  1. 1. Ñu ngi sukk ci sa kanam,

    booloo, bég, te di la ñaan

    nga jiite suñu ndaje yi

    te barkeel suñu mbooloo.

  2. 2. Ci sa biir kër, yow Yexowa,

    sellal ñu ak sa kàddu.

    Jàngal ñu ñu mën a waare,

    may ñu xol bu fees mbëggeel.

  3. 3. Baay, barkeelal suñuy mbokk

    ndax jàmm ak salaam baawaan.

    Dinañu wéy ci doxalin

    buy màggal sa kiliftéef.

(Xoolal itam Taalifi Cant 22:23; 34:4; Esayi 50:4.)

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager