TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • th lesoŋ 12 p. 15
  • Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi
  • Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Waxal ak cawarte
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Defal lépp ngir laal xolu nit ñi
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Waxal mel ni kuy waxtaan
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Xiiral nit ñi ci jëfe li ñu dégg te amal xalaat bu rafet ci ñoom
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
Xóotalal waxtaan bi
Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
th lesoŋ 12 p. 15

LESOŊ 12

Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi

Aaya bi ñu lim

1 Tesalonig 2:7, 8

LI NGA WAR A JÀPP: Waxal ci fasoŋ buy wone ne li ngay wax, ci sa xol la jóge te fonk nga ñi lay déglu.

NI NGA KO MËN A DEFE:

  • Xalaatal ñi la nar a déglu. Xalaatal ci jafe-jafe yi ñuy dund ngir mën a yëg li ñuy yëg.

  • Seetal bu baax li nga nar a wax. Li nga bëgg mooy dalal xel, dëfël xol ak dooleel. Moytul a wax kàddu yu leen mën a merloo, te bul wax lu ñaaw ci ñi gëmul dëgg gi walla ci li ñu gëm.

  • Won leen ne yëg nga leen. Na sa baat, sa kanam ak ni ngay yëngale say loxo wone ne danga fonk ñi lay déglu. Bul fàtte di muuñ walla di ree tuuti.

    Xelal bu baax

    Booy wone yëg-yëg, bu ci ëppal te bul forse. Ci fasoŋ bi ngay jànge, nanga feeñal yëg-yëg yi nekk ci li ngay jàng, waaye bu ci wone sa bopp. Na mbaax ak mbëggeel feeñ ci fasoŋ bi ngay waxe.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager