TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • th lesoŋ 2 p. 5
  • Waxal mel ni kuy waxtaan

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Waxal mel ni kuy waxtaan
  • Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Waxal ak cawarte
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Woneel ne gëm nga li ngay wax
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Defal lépp ngir laal xolu nit ñi
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
Xóotalal waxtaan bi
Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
th lesoŋ 2 p. 5

LESOŊ 2

Waxal mel ni kuy waxtaan

Aaya bi ñu lim

2 Korent 2:17

LI NGA WAR A JÀPP: Waxal ni nga tàmm di waxe ci fasoŋ buy wone ne li ngay wax lu dëggu la ci yow te fonk nga ñi lay déglu.

NI NGA KO MËN A DEFE:

  • Waajalal sa bopp bu baax te ñaan Yexowa. Ñaanal Yexowa mu dimbali la nga bañ a bàyyi xel torop ci sa bopp waaye nga gën a xalaat ci xibaar bi ngay jottali. Fexeel ba ponk yi gën a am solo ci sa waxtaan leer ci sa bopp. Bul jàng rekk li ñu bind. Waxal xalaat yi ci say kàddu bopp.

    Xelal bu baax

    Boo waree jàng dara ci Biibël bi walla ci beneen téere, waajalal sa bopp bu baax ba mokkal li ngay jàng. Boo naree jàng li nit waxoon, fexeel ba li nit kooku doon yëg feeñ ci ni nga koy jànge, waaye bu ci ëppal.

  • Li ngay wax, na jóge ci sa xol. Xalaatal ci li war a tax nit ñi déglu li ngay wax. Bàyyil xel ci ñoom. Noonu sa jëmm yépp, maanaam li nit ñi di gis ci yow, dina wone ne lu baax nga leen bëggal te li ngay wax lu dëggu la ci yow.

    Xelal bu baax

    Waxal mel ni kuy waxtaan waaye nag bul bàyyeeku ci sa waxin. Na say kàddu leer te na sa wax jekk.

  • Xoolal ñi lay déglu. Xoolal ñi lay déglu waaye na ànd ak yar. Booy def waxtaan, bul xoolandoo ñépp ci mbooloo mi, waaye xoolal kenn, ba pare nga jàll ci keneen.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager