TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 2/07 p. 8
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2007
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2008
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2006
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2003
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2004
Xóotalal waxtaan bi
Sasu Nguuru Yàlla — 2007
km 2/07 p. 8

Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

La Tour de Garde 15 févr.

“ Am na ñu foog ne nit dañu ko indi ci kow suuf ngir mu nekk ci coono. Ndax foog nga ne mën nañu yaakaar ne bu ëllëgee mbir mi dina soppeeku ? [Bàyyil nit ki mu tontu.] Seetal lu dalal xel li ñu dige fii. [Jàngal Sabuur 37:29.] Téere bii dafa ñuy won ne amul feneen fu mel ni suuf si ak it lan moo ñuy won ne dañu ko sàkk ngir ñu am dund bu neex ci kowam. Dafay wone itam li Biibël bi wax ci lu jëm ci ëllëgu suuf si. ”

Réveillez-vous ! Févr.

“ Ndax xalaat nga ne lii bokk na ci li tax àddina si jaxasoo ? [Jàngal 1 Yowaana 5:19. Bàyyil nit ki tontu.] Téere bii dafay wone li Biibël bi wax ci “ ibliis ” ak naka lañu mënee fexe ba mu bañ ñu ilif. ” Won ko waxtaan biy komaase ci xët 12.

La Tour de Garde 1er mars

“ Ci sa xalaat, ñiy jaamu Yàlla dëgg fu ñu war a teg mbëggeel ? [Bàyyil nit ki tontu.] Seetal ndigalu Yàlla bii. [Jàngal Macë 22:37-39.] Téere bii dafay wone lu tax ñiy jaamu Yàlla war a jiital mbëggeel ci seen dund. Mu ngi wax itam fan la diine yi jóge. ”

Réveillez-vous ! Mars

“ Ci sa xalaat yan jafe-jafe la ndaw yi di jànkoonte tey ? [Bàyyil nit ki tontu.] Aaya bii dafay wax ci benn jafe-jafe boo xam ne ndaw yi dañu koy jànkoonte, maanaam naka lañuy ame xarit bu baax. [Jàngal Léeb yi 13:20.] Téere bii dafay wone naka la wut xarit ci Internet mënee lor ndaw yi, te naka lañu leen ci mënee aar. ”

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager